LYRIC

{Mao – Chorus }
Gunzout Gunzouuuuuut Killah Killah Kileuuuu
Nanananaaaaaaaana
Nit to the doff, Doff to the Nit
2007 ba légui nigga bobou ba niata Hit
Fight real shit
Téwal real shit
Ghetto bagnou waunii nguir niou siweul sunu street
Nit toudou doff, Doff Toudou Nit
2007 ba légui nigga bobou ba niata Hit
Nétali sunu life
Lii xéw cii sunu side
Leundeum bé beurii takh niou iindi Light

{1er Couplet}
Yeah !!
Dk néna yes! Thies kaay na yes!
Kaolack né yeah !
Bandit LG moko ress
Rap Game bi la yokk taram
Déloko gueudeu bataay niouy Thioytu ay xibaaram
Douma tchii aL bafta
Té délou naka tiafka
Gni done diguatt mbede bi nio nieuw diébelou after
Hip Hop dou meusseu dead
yeukeutile sa hand
Lii dou rap thérapieleu
Tchii kaw tali ferrarileu
Salam Aleykoum again
Nigga guiss nga fima gèneu
Bénène Hit cii sama game
Defna tchii sama kém
Tallaay katane diko diém
Tallaay katane diko diém
Hip Hop music 4 ever
Athie nako tchii yénène level
2007 lako sékh moukiko né mégo
Dox loko guandi djégo
Niouné Killah daay égo
Maa def cii pet ak life lou geune
niou djoy cii niniou maay teggo (Oh Yeah !!!)
Black lion mister bandit LG
Mbede bi compagnie leu maa done cii ngandi DG
(hmmmmmmmmmmm)
Dika topoto diokh ko originalité
Warone done Super Star soufé done aap talibé
Mbede mo rodé sunu mind
Niou yague def tioki mic
Real shit all day ready 4 the Show tonight
Mi-Mic bi la tengo
Diiccii Rappé ni bèn dinguo
Diaroul sax ngay haine ngo
Mane ak yaw douniou mengo
Donté One day yeukeutina game bi dékilate ko
Donté One day gnii ko guédone nieuw feel laateko
Nigga Donté One yaube nako cii ay stadium
Baake nako kaw ba ngéw yi fadiou cii ay dadiam
Cii Five years yima wéssu lima cii def déffo tchii xaadiaam
Raxassal saa loxo MC sou bagné mou xadiam
Rhymes yagui djalou
Nagoul té boul jaloux
Moytoul samay Uppercute so bagné Yaawou dialou
Niaak na baa siiteu
Di woute ndam ni Sitteu
Loxo cii kamile guigne naa nguir fènelo gnimaay sikk
No Violence, sign by Your hands
Let the music following like a blood in your vains
Rocket wit Senegal real hot shit phenomenal Killah Killah

{Mao – Chorus}
Nit toudou doff, Doff Toudou Nit
2007 ba légui nigga bobou ba niata Hit
Fight real shit
Téwal real shit
Ghetto bagnou waunii nguir niou siweul sunu street
Nit toudou doff, Doff Toudou Nit
2007 ba légui nigga bobou ba niata Hit
Nétali sunu life
Lii xéw cii sunu side
Leundeum bé beurii takh niou iindi Light

{2ème Couplet}
Yo !!! Yo !!!
Xeuy nama diém nama
farlou fipou taay dé aay nama
Faale nama faléma cii walou rap dé mbede djaay nama
Maa imposé dominé dem ba nones yi dima nominés
Dieum Djii di gueuneu siiw
kouné di mbiiw
Mak ak goné di fiiw
Takhirlou aay new
I’m fucking Real and I stay Real
LG deal What’s poppin my all…..
Do djékii lo djiwoule waune
I’m Killah the real one
Gorr Cii warr wa laniou ko xamé ba mouy moudié di yélwane
Nit toudou doff
Duel mic moma mayatii
Hakk rek laay séréti
Five years you wéssou lofi thiop nako sébétii
Ok!! Dieum djii féink Xall yone indi lerr niit
Kii délo Geude rap galsen moy sama mérite
Mista Champion guissouma loutakh maay tégui yone
Gni ngui woté fii Té founiou maa sèneu titangué fegne cii niom

{Mao – Chorus}
Killah Killah Killeuuuuuuu
Nit toudou doff, Doff Toudou Nit
2007 ba légui nigga bobou ba niata Hit
Fight real shit
Téwal real shit
Ghetto bagnou waunii nguir niou siweul sunu street
Nit toudou doff, Doff Toudou Nit
2007 ba légui nigga bobou ba niata Hit
Nétali sunu life
Lii xéw cii sunu side
Leun’deum bé beurii takh niou iin’di Light

{3ème Couplet}
Yes Saa !!! Yes Saa ! From Africa Westa
Gunzout à la prod le public Aime ça
Depuis l’école de la Street j’ai connu mes scarLa (Lascars)
Diwane Squad toujours au pair comme les guerriers de Spartacs
Micro clashnicov on a conquis tout Karda (Dakar)
2007, dans les bacs j’ai fait trop de dégats
2009, comme des tasspé (Pétasses) je les ai béta
2013, 3ème Album bête de Peura (Rap)
Boudone Xaréé maay sahaba
Boudone diné maay Kaaba
Boudone carte madone AS, Yaw nga fétéwo naba
I’m like Ali cii Ring
Saff Ni kané cii tchine
Meuneu rappé meuneu flow té dafa tarou cii bindeu
Damay dagou cii street Nioumay gived respect
Damay alou dii speech, Fire Killah is back
Sama door dafa diss bitch foma guiss tek (daw)
Let me attending this game like nobody’s that

{Mao – Chorus}
Killah Killah Killeuuuuuuu
Nit toudou doff, Doff Toudou Nit
2007 ba légui nigga bobou ba niata Hit
Fight real shit
Téwal real shit
Ghetto bagnou waunii nguir niou siweul sunu street
Nit toudou doff, Doff Toudou Nit
2007 ba légui nigga bobou ba niata Hit
Nétali sunu life
Lii xéw cii sunu side
Leun’deum bé beurii takh niou iin’di Light
Killah Killah Killeuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuu

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR