LYRIC

WawOuw Ara Dayza
Yeah
look at look at
WawOuw Boy bi bakhna dh
Kholal xalé bi man
Aahaa What’s up xana da ngako tipsé
Yeah !
wa dieul ko wo ko loy yeureumteulou
Na nga ko abordé nga khol abordé ko ma khol
Nokoy wowé ? Ey bordel hééé. No !
Eh mais c’est qui bordel ? ..Il est malade ce mec

{Verse 1}
Héy Baby no dou wouyo piss Ki amena fouleu dh
Dox bagna guestou meune na waate ni ki nobou la dh
Wowéko puce ma puce, mais kallouna dh
Kholal sourire bi day nieuw guiss nga sikaloula dh
Soit galant relax mademoiselle soxna ci pardon (mais y a quoi)
Ey Nice démarche doy ngama ci dokhou 4 temps
Yaw la guiss djanakhé ba taxaw fi amoul ngaagne (No no)
Boy abordé défal comédie “Serigne Ngagne”
Néko doylo nga rafett gueum naani djoyo taar
Si da nga toy no bodone auto yaay done Toyota
Mou réh nga am fiit relax waathié sa nerf
Def togne néko yaw miss lo bokak Katy Chimère
Djayko wowé Katy Perry, Kim Kardashian
Nala weuri bo beugué sakh malay gardel sa chien
Wayko diaral ngama bou GAS(Gaston) ak Ombré “Dinama Gaagne”
Ma done sa Saneex boy yaubou galé dimafa djapp Kaagne
Dioxma number doundou 111 sans ordonnance
After niou dégueunté well well nga mayma chance

{Refrain}
Je m’en fiche de ce qu’elle pense
Elle est là pour que je la compense
Relax ! appelles la ! peut etre que c’est ton jour de chance
Ey Bordel arr (arr), kène douko wowé koy abordé
Gardes le sourire waathiel sa ton boy bouko youxou bordel (2 fois)

{Verse 2}
Héy Fils pardon ! wait a minute ma guiss la waay
No boy meune na gueuneu sédd kholo xalé bi miss la waay
Si si dafmay djaay prek high wanema nimou sagnessé wé
Mais guisso ni meune na gueuneu deugueur keung té gangsta wé (Comme nane ?)
Niangal djaayko fouleu xawko napaalé
Néko xam ngama waathié ko melni kouko niakk faalé
Mais boy waathiél sa ton touti wakh melni kouy kaffaalé
After leu mayma touti ma wakh meune kossi seufeulaalé
Nice nga rafett nga mais mala daakeu haannn
No je te taquine ma queen tay li nga takk haannn
Mais boy, est-ce que xam ngaani ya ngui yéngueul kogne bi
Temps yi guiss na Pa yi damier fé néé néé defla togne bi
No !  kholma maay kila atane ma ngui Xeuch
Dembe yaw la gueinte gueinte gouma ndarone yaubou Teuss
Beute bi né caméra diaralma dougou cii kambeu rat
Gaaw né Peul bou takk siff leu melni kou warr Al-Bourah
Dioxma number doundou 111 sans ordonnance
After niou dégueunté well well nga mayma chance

{Refrain}
Je m’en fiche de ce qu’elle pense
Elle est là pour que je la compense
Relax ! appelles la ! peut etre que c’est ton jour de chance
Ey Bordel arr (arr), kène douko wowé koy abordé
Gardes le sourire waathiel sa ton boy bouko youxou bordel (2 fois)

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR