LYRIC

{Verse 1}
Yeah man Dessal di wakh may job léral sama karma
Ma ngi yek ngay wathieu meuneu touniou bokk yone boy diémeul beu karma
Meun Rap di fébar bou rare meunou mala wakh louma def bamou dalma
Old tchi mind bi New Skool tchi dieum dji Hybride la ragnéma
Bokou maak gni dess sama Rouh da daadjou mind bi fess
Mandi tchi lerr yi MCs yi di mouslou tchi mane damay teur di reindi fééss
Mane dama free ndakh guiss bou yes waral ma aay ngène gueune fi yëss
Fuck sène game real yi lapp naniou tchi guédjou succès bi maafi dess
Yaw ya ngi lathie loumay def beu téki yi rimes ? dou baune té dou daadju wine
Yagg tchi suuf takh hood bi def nama ganyin Wallaahi ma tchi gueuneu shine
Yeg yeg bou deugou leu takh souma rap-bé mou nice mélodies yi mo gueuneu fine
Guiss naani thioolé nga Public bi malèni gaagn f**k bayré geum na soumay rimes
Rap allalou mbède leu dou ngèn change, lou ngène fi tek ma tégui tek louma meun
Fay sa name armel yi nga dieum. aythia whose the next ? boy seu mbeur douma daane
…Douniou job meuneu doul, bou dakkoul may dadji ay gueules
Je crache du lourd c’est de la nourriture pour l’âme. Respecter à ceux qui le veulent

{Refrain}
Ligay jeuf lay xool mais pas ligua May wane
Kone real ou fake geu adjina lodone
Adjinala… Adjinala…ha ha ha
I can’t trust you nigga You’re just a bi…
Guissouma tchi yaw model let me do my shit
Adjinala… Adjinala…ha ha ha

{Verse 2}
Adjinako aayou lène ba nopi di khaw (wakh) Job bi lèn
Molèn fi dessé kou wodo lamignam bou nopé nak def taatu nèèn
Real dou wakh loumouy def nay nangou li YALLAH di def Di dieuf tédou xéf
Fake limouy wakh douko def Nio beuri tchi game bi di mathieu tougne yengueul xeff
Bou Trap beat amoul wone mou thiool tchi yeen kone dh niou beuri baayi RAP
Aythia niou gangsta beat bi neu gooré rek ngène tokk sen Baay yi RAP
Wallaahi sen game bi dou dém da toppeuh tchi mode bi fuck doul lamay xégne
Ana real nigga yiy bagne hood bi leu back to the underground kharél bagne
Askan wi dh sick naniou Hit rap-bal té baayi di proné swagg ci say beat
Sen carrière yi laniou wara krithe, sen mind yé creuvés ba nopi dakkeu mystique
Aadji nako Job moy fay nioma gueuneu siiw waw meu gueune léneu aay
Soxlawouma di takkeu di fay comme djanteu bi nioune dagni lakkou rek mais douniou fay
Gueimbeu len sen MCs yi nieuw niom nieup taf taf ma tass sen thioumbou kaay
Aadjinaa ay fakes leugn douniou trôné kèneu tchi niom dou done sama royoukaay
Chaise bou éjectable no tchi trôné ? baakeu meu King rek meu fuck leu waay
Aadjinaa dou fuck li ngèni woté Real MC bifi dess mane leu waaay
Yeah man

{Refrain}
Ligay jeuf lay xool mais pas ligua May wane
Kone real ou fake geu adjina lodone
Adjinala… Adjinala…ha ha ha
I can’t trust you nigga You’re just a bi…
Guissouma tchi yaw model let me do my shit
Adjinala… Adjinala…ha ha ha

{Verse 3}
Aadjinako rap assamane leu té MCs yi beuri beu mel ay Bideew
Mais YANKO dou niom moy dathieu deup gui done sen djante tchi bi gueew
Aadji nako Rimes la meun té Rap-ba gouma dara nel Guedj gui niou sopiko daa
Khopp yi niou def lène feuilles branche yi xalima ma tek tchi rimes youdou die
Aadji nako mane douma niom, niom douniou mane gueum sa bopp moy rk lifi am
Na def lima meune ak tek ko tchi yone beu djégui frontière dem djeuli ndam
Seu fav(favorite) MC bi NABBA leu, té meusso guiss DAME ray AS défaitam lerr na
Pariél tchi mom perte nga The Future, The Best, The Next MC mane leu
Aadji nako malène meun dou yombe loi du plus fort leu nala songueuh
Gaïndé tchi gettou bëy naroul yombe bain de sang kèneu tchi dou rombeu
Aadji nako fi Rap-batouniou bindeu kat yi manqué fi
Get-tal sen tracks yi boudoul ay rimes yu banales nigga tell me what you see
Héé boy niou yokk job nigga niou aadjaate BARRE bi gueustou Xam RAP
Lerral MIND yi GALSEN ni ALCOOLO yorr KASS ci BARRE Bi
Té kène tchi yeen défou tchi RAP bou MANDI
The Game is Over now maay fuck sen bout de buzz mou yem fi
YANKO leu listen to my song daadju makk ngay guiss ci dieumeu boy bi
Yeah man

{Refrain}
Ligay jeuf lay xool mais pas ligua May wane
Kone real ou feak geu adjina lodone
Adjinala… Adjinala…ha ha ha
I can’t trust you nigga You’re just a bi…
Guissouma tchi yaw model let me do my shit
Adjinala… Adjinala…ha ha ha

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR