LYRIC

[Part 1 – Ara]
Dolé dokhoul diameu
Do mane té douma yow
Sagnsé dama ko tameu
Kholma ci souf ba ci kaw
té diémouma ko dama meun
Sett ci wé ak ci karaw
Guissatouma louma nameu
Fima guéneu la nieup beug aw
Di nga ni nila nila (nila waaay)
Fi ma guène noy neu noy neu (noy neu waaaay)
Di nga ni ma ni le ni le (nila waaay)
Di nga ma né noy neu noy neu

[Hook]
Nénala ngeu sol taille basse,
Soloul ni ndanane bi,
soloul ni kou dieum Nuit du Drap
Boul faté foudeunou maquillage,
Diongoma tagal ley def, moussorou, diongama dou sol bas
Nileu bilayyy, sama adiaratou sama adja
Nga solou mou yiiw niou ande ma ame thieurou alaadji
Nileu, nileu, nileu bilay….
Nileu, nileu, nileu bilay….
Nileu

[Part 2 – Wally]
Da nga né ci à péage romb la woroul
Do dioum ci maquillage mane damala wolou
Ya ngui teul sa gréffage di dokh di dagou
Yor khirr di karawass ken meunoula sourr
Nékhoul ba nékhoul adji ngeu
Li nga Sagnsé nekhneu
Ling-ma défal bakhneu
Ya-aka beurri mana
Sol nga sa ndokétte tagalou
Mine nako ci yow dou ma geune
Soula nékhé ragadjoul
Daane nga akhlou Sagnsé
Look it my ***
Yangu-mey nirou Marie Madeleine
Yow sa dokhine nah neu wo! wo ! wo !
Diongama, kay tatafouma anh
Kay tatafoumaa hum!
Nieuwal tatafouma
Kay tatafouma…

[Hook]
Nénala ngeu sol taille basse,
Soloul ni ndanane bi,
soloul ni kou dieum Nuit du Drap
Boul faté foudeunou maquillage,
Diongoma tagal ley def, moussorou, diongama dou sol bas
Nileu bilayyy, sama adiaratou sama adja
Nga solou mou yiiw niou ande ma ame thieurou alaadji
Nileu, nileu, nileu bilay…
Nileu, nileu, nileu bilay….
Nileu

[Part 3 – Dayza]
Da ngey solou di geuneu nice
Solou di geuneu toy
Sama xol bi di geuneu natt
Fi nga guénati geuneu noy
Sama diongama paradise
Sa solou dou meuna togn
té nga bayi soumala né Sagnsé nga nga nane ma bae da nga meuna togne
Meun nga solou meun nga sagnsé kar
Sa col bi tégou na ci temps
Sa mélo bi mo geuna tarrou, té mane sa djiko bi la geuna fan
mane ak yow nio dakh wa Guissé Maabo, nio geuna niro
mane yow la tamou yaw la appo
Sandi ma gouro
Bébé sa solou bi nala ci may note
Diokhma trois pièces bi damey sotte
Dafa mélni yow lépala diapp même bo solé loula eup sakh dalay
djote
Lalal nala bouko lali daagou noum-la nékhé nga diokhma sa loxo
Mélal ni kou diougué Mali mane mala toudé Aminata Bakhayoko.

[Hook]
Nénala ngeu sol taille basse,
Soloul ni ndanane bi,
soloul ni kou dieum Nuit du Drap
Boul faté foudeunou maquillage,
Diongoma tagal ley def, moussorou, diongama dou sol bas
Nileu bilayyy, sama adiaratou sama adja
Nga solou mou yiiw niou ande ma ame thieurou alaadji
Nileu, nileu, nileu bilay….
Nileu, nileu, nileu bilay….
Nileu
Nileu

[Outro Wally]
Waly ak Akhlou brick daneu
Kone ték ci brick Faramareen Music

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR