LYRIC

{Couplet Leuz}
Ya fi dakha rap nga ame studio ak label tè rabouloo
Ya fi dakha toukh bone niou andil la rizla ak pone tè raabouloo
Da ngay niawate niou nè niou andil la silim ak thiass tè rabouloo
Lou takh niou bayi fi nitt gni di daw bay khikheut pour diokh ay rats boulot
Talant dafa ame plan ame
crack baraque boul fatè clan teum
Sokhlawou ma nek Sen king seugueum ay Cons wa nara nek sama Royaume
Rouss na diay si rèwandè ,Bénéfice bi kone riiba lay done
Tè Ay waxandè lay deukheugne ,Grossiste si li nguene di ambulant
Sene tokheu yi dagne si rembatlè, Bou lene di fatè di wax lèbone
Meune dokhote lay diay weukheugne,Niep ko guiss mouy daw tè nane bandit la
Bandit nga mane Gandhi la , Lou may doyè kou may fan si diay prek
Fuck star mane talibè la ,Sokhlawma ganstar mane oukh lay tek
– Rap rek la niou meune, Sekh radio yi kene degatoul
Bou niou amone lou gueuna fort Meune rap ,
Damay ragal niou faat askane wi bro
– Sap rek feugue deuneu ,Ego yè firndel ni mokoul
Bou niou bolè wone sene ndap comme dhab
dougne ma yem si teusteune wi Dio

{Refrain}
(Leuz)
Amna talent/ Amna plan
Amna crack/ Amna Baraque
Amna kou aye ,Bokoutak Cobaye
Dekh dou déékk Building dou kirtinding
(Bril)
Amouniou Talent waayé amnaniou clan
Lou bakh laniou soul légui, tekna niou Plan
Talent daflay Fay, gniko am douniou gawa takkeu
Dèfal sa dèf bagnlèn doundou wakh dji djèkh takheu ..

{Couplet Bril}
Yakci nga Deukk bi talent di Raayé , Gni xamoul dara Yhéém Wa Radio Bi…
Laté thi Télé , di gueuna di teulé , bo dégglo li khaamé , Gni Wara Jobi…
Rap bi da beuri niou Thiouné, Public bi soulnaniou Deugg bi yeukkeuti Fén…
Dégglou niou khamné Nio thi né, Lign léni Forcé dou guéneu ba todjaté Féneu…
Sén Rappeur yi Djoudou Démb nio périmé,
Dou technique dou Flow Texte dougn ko Rimé,
Music bi di féébar niou eundi Comprimé,
Do Guissati Virus Léppeu laniou Supprimé,,
Mane Khamnani fokk niou sissou ndakh kéneu dou Far’ak « kiy Doumeu sa baye,,, »
May kheuthieu mou daggueu ma takkat di kheuthieu , Wakhlén né « Ki dou Meusseu Bayi… »
Sén Son yi dafmay dérangé comme djoyou ay Yoo.
Boy Rap di mélné Liir , Fokk nga Déggueu Ayo..:
Mangui nieuw Matalko/ Kouy wakh Fèkkeu Ma tal ko/
Day Déé thi Rime bi, may def crime bi Alma briquet légui ma taal ko/
Nioune bouniou done Oxygène dina am , niéneu niou sissou ba douniou Noyi
Douniou dèm, daniouy gueune di Gouddé thi wérantè you Deuggueur ak You Noy yi ..
Surchargé Auto bi Meunoula takh ngén Fèkhé ba tokk thi plaçou Chauffeur…
Boudone sokhor dina féss biir niou beuréy Deukk thi di Feur…

{Refrain}
(Leuz)
Amna talent/ Amna plan
Amna crack/ Amna Baraque
Amna kou aye ,Bokoutak Cobaye
Dekh dou déékk Building dou kirtinding
(Bril)
Amouniou Talent waayé amnaniou clan
Lou bakh laniou soul légui, tekna niou Plan
Talent daflay Fay, gniko am douniou gawa takkeu
Dèfal sa dèf bagnlèn doundou wakh dji djèkh takheu

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR