LYRIC

[Intro Atheena] Insensible , insensible, tu l’aimes mais pourtant tu la fuis
Insensible , insensible, tu l’aimes mais pourtant tu la fuis

Premier couplet :
Yonewou goudou thila sobou toudou tokkantalou maniwou
Djeum djoudou saabhal rouhou foudou rohtiantalou ma nouyou :
(Souf, ndokh, safara ak guélaw,) téré thi lokhoy sokhnaci
Ouf dokh yakhiy nélaw, ay wérr djeumam dji sookh naci
Déggna youkhou djoukna daw ba djéguéla keufla djokhla wéénam
Yaggna wakhou beugona gaw djeufna dokh thi yéwénam
Deuké nakh, weugg, khontou, sakh thi dokhantou
Dou défantou moy kiye djolou liy bakh dou goukhantou
Toppko ndakh mo di yaaram bi yagga baathie say laytay
Topato sa wérrgou yaram ba wakhtou you naadjé yi lay tay
Seugg balé yobalé dja ba, rogganti takk mbootay
Yagga baalé tibaalé djal ba, djoubanti démb ba taay.

[REFRAIN ATHEENA] Et meme quand tout le monde est contre toi
Elle reste ta meilleure amie
T’aimerais lui dire ce qu’elle reprsente pour toi
Avant qu’elle ne perde la vie
Mais tu n’oses pas, tu n’oses pas, tu n’oses pas lui dire
Et tu n’oses pas, tu n’oses pas, tu n’oses pas lui dire

Deuxième couplet :
Fokk ma soukou tokk sa wétt, wakhla ma ngui djéggeulou
Doggou dokk sa wéét, wakhou geuneu djégué lou
Meuneu déff sa banekh, teudjou faté kouné
Fékhé nahkar romb nekh, deudjou fatélikou gouné :
Lima xel diokh ladone déf done moomine khaw ma dara
Ngirr ma meuneu dokh sama warréf daf ma yobou daara
Magui djégeulouwat thi daw djang yimala wakhoul
Ragalone nga djiteulatema gadou yaar té nanema waahkoul
Yagg di déf founé tocc tocc guiss gnoulay aakk ci
Ngamay douma khamal mani biss dina akkci
Ma dokh ba raagné ndjarignou li, dji ngagnou li
Lofi beugoul weurougnou li, yaay serigne bi fi Maaaaaa.

[Refrain Atheena]

Troisième couplet:
Dina fééssal djouniy téèré soumay xatim way thi moom
Deupeul dégglou dji ay batam niolay toppi done sa galathie
Boul feusseul limlay téré délo djoukeul rék nga moom
Thieuppeul djéggeulou thi wétam djeuf ba nooppi soga lathie
Dikk taathie yénén pathie wathie ba thi souf raathie
Dathie lou méti, khaathie baathie nakharam yi
Athie fou kawé bépp beugg beuggeum
Saa bo rawé na nga deupeu déggui deuggeum
Boul thi rouss dara fékhél wane-ko fimlaa tolou
Amo fayam bagnal faille am djougal bayi toolou
Ngeureumeum nang’ko geum soukou sakou niaanam
Féékheul xolam done’na li geun ci kou topp yoonam.
·
[Interlude Atheena] Je ne suis jamais parti
Je n’ai jamais chang
Si ce n’est ma voix et ma taille
Oh Maman
C’est moi
Je veux que tu valides ma fiance
Rconforte-moi comme quand je tombais
Maman ou t’es pass oh
Regarde-moi

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR