LYRIC

VERSE 1
Adouna sobé la (sobé la ah ah ah )
Kou kheuthio ak mom mou fowé la (fowé la ah ah)

Tedj negn ma tchi kasso maa ngui diemeu reuthieu
Diemeu fey begneu lap tchi guediou leundeum
Deugueur bopp takh lougn degn ma téré ma dieuf
Di deglou baken loumou guenné me dieund

Mangui tchi yone bi di zig zag di zig zag
Wouté naak niom yoneunté Yalla Isaac
Mangui tchi yone bi di zig zag di zig zag
Kou dem naani kaani mouno wothiou bissap
Sama beug beug moye sama nattou
Momeu takha naaw lakk sama kerozene
Momeu takha war gni meu diokhone sama kaddou
Ak sho yi ndieukk kham sama sokhna fimeu erogene

Yaay mane maay yow
Loma deflo sama bopp laako def
Et puis sakh yow Yaay kane yow yaa bone
Nimala sekhlo nonou laala abonné

Linga ma dioumlo yeup kham naani ya ko tey
Newone naa so ma beugueuté diégué naa ko begn
Linga ma dioumlo yeup kham naani ya ko tey
Nga nekk sama birr khel nan ma khana Amo khel

Nga may ma baat tek ma paaka tchi pout
Nand naa ni deung ma beugg diappé ngaaka tchi pett han
Mane demleu topp seme bopp di metti
Ken dou weddi né kou leu sopp deukké sopp di weddi

Chorus
Ya takh me pouss wakhtou dioulli yi me tayalone diok
Yow yama takha dioylo djiguene yimeu nop
Nga Ne tchi sama nopp dimeu dey mey moy
Bala may diegui siraat war nama takhalikok yow
Bayima x4 ma bayila
Nga bayima x4 ma bayila

Verse 2
Adouna sobé la
Kou kheuthio ak mom mou fowé la

Me netteuli leu sama guent gui
Kou ko guent do beugg guenteeuti
Kou ko guent do beugg guenneuti
Mba nga yewou beug sey wala dem tukki
Seytané def me beugone damp ni lire ak maam
Mou Def me diame nar ma takk tchi birr ab kaf
Il Faut que ma téyé sama tankk tchi biir appart bimeu nekk ni di diangg di lire ay sar
Seytané def me beugone damp ni lire ak maam
Mou Def me diame nar ma takk tchi birr ab kaf
Kou ko dowoul de ley sankk kill fat fat
Foumma wowati faut q ma lankk nguir am jamm te benieu teleu fouti
Khamatouniou lane moye lerrou gouddi
Kilifeu yiniou beugg roy
Fadiar teel legn daan yewou dioulli
Ndokh dou am niou dieul kherrou dioulli
Loutakh bign le diappé nga faakh se pappeu néleu doto guenn gouddi
Defarouwaat gueuneu nekk khel ndakh diangg dou wess te Ibliss def niou beugg djiguini dieul niou def niou diaamou baken
Kou fi yokk weddi wathié yiw no def wokk dokkh nakh nga se bopp bo fogué ne bo fi diogué ken douleu fatté

Nga may ma baat tek ma paaka tchi pout
Nand naa ni deung ma beugg diappé ngaaka tchi pett han
Mane demleu topp seme bopp di metti
Ken dou weddi ni beugg lou yomb moley yobé lou metti

VERSE 3
Diéém naa reuthie
Se pékhé kemtaan leu
Ya meuneu yeew ay thieur
Tedj niou ci se jail locked up

Yow yaa begn jamm
Euppeulé sobé Amsterdam
Yaa rey laamigne
Se taar meuneu Daanel jam

Ya takh me pouss wakhtou diouli yima tayalone diok
Ya takh me rouss bimeu dadiék seme morom yimeu togne
Seme thiono yeup nul negn
Adouna dor neme kurpegn

Deungueu beugg niou réér
Bougoulo peace and love
Mane bougouma niou bokk kourel
Bougoumeu guissé’k yow

Bougouma and ak yow
Kone boul and ak mane
Bougouma nek ak yow
Boul diemeu nek ak mane

Bougouma def ak yow
Amo loy def ak mane
Waroumeu guiss loumeu neekh rek def
Warouma toke loumeu yek rek def
Baayima, baayima, baayima
Ma baayi leu

FINAL BRIDGE
Bayima ma dem
Bayima ma dem
Bayima ma dem
Manila bayima nga begn

Djihad an-nafsou
Di djihad ak nafsou
Lilaay wa rassoul
Baayima bilaay deme sourr

Mangui tchi djihad an-nafsou
Di djihad ak nafsou
Lilaay wa rassoul
Bilaay deme sourr

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR