LYRIC

{Refrain}
Lou bandit di ndiraul
Lou wara né djikaum
Waxma lou bandit di ndiraul
Lane mo lane mo wara nék djikaum ?
Lou bandit di ndiraul
Lou wara nék djikaum
Waxma lou bandit di ndiraul
Lane mo lane mo wara nék djikaum
Lou bandit di ndiraul

{Verse 1}
Waxma noy def ba sa compte fess ak concert huis-clos
Rappeur yi niom nio ngui xotti texte ni secrétaire ci bureau
Profité-wo bala DIP di nieuw day compliquer lolou nga laale fi millions
Mafi gueuneu Tchikili Bandit ci Song bandit ci Clip
Gaaw ni Lucky Luck ball ci sa tankeu nga Tchiriri
Niaari tankeu ci biir piscine bi Miss Tchip Tchip yi dima piss melni picc yi (sisss)
24h/24 ci Usine bi maak Idy ak..Musique lucide sans wiski ak shit
Founiou la wo ma ngui ci biir té fepp founiou ma wo yaak sa gars yeup ci biti (Ous !)

{Refrain}
Lou bandit di ndiraul
Lou wara nék djikaum
Waxma lou bandit di ndiraul
Lane mo lane mo wara nék djikaum ?
Lou bandit di ndiraul
Lou wara nék djikaum
Waxma lou bandit di ndiraul
Lane mo lane mo wara nék djikaum
Lou bandit di ndiraul

{Verse 2}
Challenger, Aythia Mbeur yaw la gueum
Bandit la, non mane douma rappeur
Ndanaane la boy ni sa papa
Waxma lou bandit di ndiraul
Sou boba ma wane leu ni kaani dou chiwingum (Héééy)
Boy bandit bandit lou boufi nieuw
Wayna Billy Boy ak ndém ci Yallah Ino (Bandit Bandit)
Fake Nigga meussouma neekh fi dou tar ba nga dégueuh « Wouy Sama Ndeye » (Dédett)
Métiwone neu mais niou gueum ko rek batay boy DIP Mo gueuneu siw Monsieur le Maire
Respect ni yéré bima soleu, succès melni guél bima nopp
Douniou yeukeuti loxo sa kaw mouk class xana concert fi kèneu démoul tableau (Nio Bagne)

{Refrain 3}
Lou bandit di ndiraul
Lou wara nék djikaum
Waxma lou bandit di ndiraul
Lane mo lane mo wara nék djikaum ?
Lou bandit di ndiraul
Héééééééééééééy
Lou wara nék djikaum
Waxma lou bandit di ndiraul
Lane mo lane mo wara nék djikaum
Lou bandit di ndiraul

{Verse 3}
Bandit dou ray teud 10 jail. non !
Business ba done Milliardaire
Yama makk mala meune
Lepp Modjii Ma Shaa Allah
Dama Touli lifi nékone adjak-djak
Karkatar lamigne bou toleu ni thiakaaba
Xadjalma damay xadjamal
da nga thiang yaak sa musique bou xagnaaral
Bayil sa loxo pour djappeu fane
Douma tégui tankeu ma ngui casamance
Sama Bakkane la tek boy ni Mbacké Mbacké
Gueuwouma thiaxane kate yiy niodi gentleman
Cheuuute tay dji bandit yi lay wayyal
Waxoumaak boy yi djoudou barki dembau Ndiaye
Bandit la fils kone dédett douma tiite
Bandit la mane cii kébétou kat yi
Teksi sadique ni kouy naane dérétou vampir

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR