LYRIC

{Intro}
Waa yaw sama waa dji yaw li noko meuné takk soxna rek
djéki djéki sama gars yi damay takk soxna 
Booy takk soxna sakh nga waar gno meuneu guiss né gnou yawouuu
damay takk soxna wakh gnou si mom gnou meuneu xam kimou done
Mom moy kane sakh?

{Verse 1}
Kèn rek la dotoul niaar, kima meuneu guindi si leundeum
Fo sèèn lerr mofa diar, dafa wèèssu djékk si bideum
Moy ki faaté taaram, soufeel boppam, moudjou fi nek yaaraam
Bayna waaraam, ba thi ay soppam, wane-na nieup yaraam
Dou dioum ba wathieu yonaam, doxna tok waareefam
Fok nga weuri ba guissko, xam ni sol lou djot waré femme
Miroul si deureum yaakoul déram ngor la def ci coeur-reum
Tibeuna peureum defko Or-ram, doylou tok cii keureum
Dou xeuy rek sopi nékinam, métittay yokou Yakinam
Dégg Dégguinam romb lépp dém, gokh bi nieuppa séédé Téguinam
Limou gueuneu beugg diko saameu mi-ngui tégué
Lou néwoul deug dou thi yéégg dou ko diégué
Dougoul cii lou beuri, do degg mongui weuri
Lifi xew dou cii sori, ba thi nek di thi bégué

{Lady Zee – Refrain}
Di weuy sa kaddu, fo diokhogne ma joublou
Amoul dara loumalay bagnal, yay ki gueune si mane
Siguil ngama ci samay biir morom
Dou lène lou gnaaw ngay séintu ci mane
Aduna ngui nii iiiih, mane ak yaw fii nii niii iih
Niou Doundou lou nééééééékhaaa nekheuuuu
Def nga saa choix dou kénène koudoul mane
……Oooooooh woooo wooooow……..

{Verse 2}
Miirroul thi def lou araam, bokoul-lak gni namoul dara
Dou beumeukh mondam dafay raam, am Diné né kou yarro Daara
Togaye cii mbède mi doko fa sèène, meunouma xayma mandouwaayam
Meussoula nek ci téguélé dadjalé, kénène koudoul mane dou waayyam
Ay wakham dou beuri, dou léép bay aamé thi borr yi
Guènoul di weuri ba sori ci keur yi, dou bokkou ci gni wétchétte di irri (euuheuu)
Yoroul djiko MAYA dou nétali lou meuneu TOUKIL ADUNA (Apocalypse 2012) (dédéétt)
Xellam ma yaa wakh djou féébar douko gueum noppi fagouna (waawaw)
Dafmay réé lo, bégglo, boye wakh di nga guiss noumou lay déguelo
Dou Def té yeuggoulo, dieuf té beuggoulo, bokoullak yène miss yila meuneu nieuklo
Lou yagg la deugg la, feugg na, dougouna xamna meune na booram
Na-ngou na, beugg na, takkou na, tokk liguèyna fayna boraam

{Lady Zee – Refrain}
Di weuy sa kaddu, fo diokhogne ma joublou
Amoul dara loumalay bagnal, yay ki gueune si mane
Siguil ngama ci samay biir morom
Dou lène lou gnaaw ngay séintu ci mane
Aduna ngui nii iiiih, mane ak yaw fii nii niii iih
Niou Doundou lou nééééééékhaaa nekheuuuu
Def nga saa choix dou kénène koudoul mane
……Oooooooh woooo wooooow……..

{Bridge – Parole}
Haaaan waw kay waay ma ngui doga xam nak niileu
parce que niit ki mom bo démé bay takk mom
da ngay xam ki ngay takk parce que légui diamono dji légui mom
guiss nga nimouy démé ,nila kay , nila goor goorloul rék

{Lady Zee}
Yeaaaaaaaaah yeaaaaah
Beugg nala ak fima la tek nga sori ci mane lool, douma wéétt
Nga done sama goor lolou yaww la, kèn dougnou xaddialé
Dou lène mogniy féwélé,
mane nga taneu ma done sa soxna (wawaw)
Fass yéné djaleu sa guinaw ouffeul la
Say doom bagnou magg tékki (deugg la waay)
mane la outtou yaw , biss ci keur gui

{Lady Zee – Refrain}
Di weuy sa kaddu, fo diokhogne ma joublou
Amoul dara loumalay bagnal, yay ki gueune si mane
Siguil ngama ci samay biir morom
Dou lène lou gnaaw ngay séintu ci mane
Aduna ngui nii iiiih, mane ak yaw fii nii niii iih
Niou Doundou lou nééééééékhaaa nekheuuuu
Def nga saa choix dou kénène koudoul mane
……Oooooooh woooo wooooow……..

{Outro}
{Bril } – Waaawaaw mala tamou defla soxna
{Lady Zee} – Def nga saa choix dou kène koudoul mane
{Bril } – Boudoul yaw dou done kénène
{Lady Zee} – Def nga saa choix dou kène koudoul mane
{Bril } – Saa yii diko nioma nekh
{Lady Zee} – Def nga saa choix dou kène koudoul mane
{Bril } – Saa lepp moma nekh
{Lady Zee} – Def nga saa choix dou kène koudoul mane
{Bril } – Ma ngui nianal gni thi dess niou am soxna ni mane han
{Lady Zee} – Def nga saa choix dou kène koudoul mane
{Bril } – Guiss kou bakha bakh
{Lady Zee} – Def nga saa choix dou kène koudoul mane

Bril Fight 4… – The Last Fighter – Lady Zee—Righ

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR