LYRIC

Intro
What’up , yeah –The last Fighter – back again – Bass the boss (Néthi rék) – Bénén Yone Amna (push) – I write the right yaa

{Couplet 1: Bril)
Li nga yagga gueum, gueune thi djaapp sa bo yééwo
Boum bithi sa lokho waroko saani , filék yééwo
Liy dokh thi sa biir xél , nélawo diko guéént
Bo yaagué thi leundeum, djoubloul pénkou légui sa djantt féénk
Koufi sonou rék deupp , yangui nélaw wake up
Bo beuggué done kiy yagga djitou fékhéla dakka daw nieupp « hun »
Liy sopi sa life, moy nga deukk ci fight
Koula gueumlo yééndou ci mbéd mi tok di khoolé wakhoula Right
Founé nga wara di #Lamb, di wagni sa #baakou yi Seugg di #beuré ba am ndam
Kou mbéékté di sakhaar, ba sopi fi doundeum, djom la soti ci andam
Bén boul thi meussa Yém – bo beuggué tékki lépp ngay djéém
Bountou yi teudjou waroula yéém – Gueuneul di pouss té gueumni day dém .

{Refrain: Canabasse)
Day Déém – Push – Push –Push néthi Rék
Day Déém – (dina bakh men) – Bou matoul Thi bi yone mat, thi bi di Nieuw
Day Déém –(héé Bass wakhal) – Push – Push –Push néthi Rék
Day Déém – Bou matoul Thi bi yone mat, thi bi di Nieuw

{Couplet 2: Bril)
Xaar mou djotay sunu arme, takhniou deukké Ray Temps
Bouniou djaapé douniou bayi appeu nagn ko vingt ans
Sokhlawoumay avocats Yone bouma djaar Amna
Doolé Rék Fadjou bépp Cas – ki yagga beuré khamna
Féék boléwoko’k xél djapalni Parégo –
Déssna Beurégo – Ngéémbouwatal ba paré Go!!!
Gueum sa bopp né tékeu ba doundou sa guéntt bi soga di nékeu
Ndéém lima yagga bindeu thi nég ga guéneu thi mbéd ba égg fou nékeu
Kouy xalam dithi djaay ay baramam la yakaar
Bougn la diguéé daaw djotoulo Rén dou yaw yay Xaar .
Défal sa Déf bagn thi séntou bén nitt.
Sa yone bou leundeumé, sa gueum gueum warko meuna niitt

{Refrain: Canabasse)
Day Déém – Push – Push –Push néthi Rék
Day Déém – (dina bakh men) – Bou matoul Thi bi yone mat, thi bi di Nieuw
Day Déém –(héé Bass wakhal) – Push – Push –Push néthi Rék
Day Déém – Bou matoul Thi bi yone mat, thi bi di Nieuw

{Couplet 3}
Canabasse : Gueumeul sa Bopp , binga Gueumé God
Gueumeul , beusseul , té bo soné Yaw, Xola ci kaw ,
Xamni lépp momla, ci kaw nga bay sa waar dara teuwouko
Bril Fight 4: Bouniou yakkone samay beutt dou takh ma sopi guiss guiss
Fimay djokhogne lay dém , dina yéggueu , bén biss
Bénén Yone Amna , nangn ci bayi xél , boul gawa découragé nanga dém ba djéékh
Bénén Yone Amna nangn ci bayi xél , Sa doundou la , sa Xaaré la boul djoug thi xééx .

{Refrain: Canabasse)
Day Déém – Push – Push –Push néthi Rék
Day Déém – (dina bakh men) – Bou matoul Thi bi yone mat, thi bi di Nieuw
Day Déém –(héé Bass wakhal) – Push – Push –Push néthi Rék
Day Déém – Bou matoul Thi bi yone mat, thi bi di Nieuw
{Outro)
Canabasse : Day Déém – Push – Day Déém – Push – Day Déém
Beusseul My Nigga Push
Day Déém Day Déém , bou démou thi bi Yone Amna Bénén
Bril Fight 4: Niafél sa Life boy , boul nangou kén dila découragélo
Kheuthieul rék , bou daagué sakh woutil bénén boum takkatko
Yeah – Nanga gueumni day dém han
Bril Fight 4… The Last Fighter – Canabasse … The Boss

Added by

Ahmed

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR