LYRIC

Guèneu galé pour samay niaari waadiour
Pour niom meune naa done comédien meune naa di rap di taassou
Mindef dou gueum ni damay fènn souma né xaliss baxoul (bis)
Foumou yém nekh gueumlo ko FADIGA ak DIOUF
Youxou nagn bay beug déh Mais, est-ce que andi nga COUPE ?
Disque d’or dou sama rêve dou sama saani tathiou
Mane Disque d’or dou sama rêve dou sama saani tathiou
Bamay nék xalé daan naa am envie Xarrou
Légui meuneu gouma déh laata may fay kouy djaay suuf
Costume lay sole ci sama caisse boul laadjaate ndax dina tuupe (bis)
Tchi yakk derr guiss nassi ay CHARLIE ABDOU
Moytoulma waadji naane « frère amatoul, xarite amoul »
Loutah ngay naane bataye té guiss sa PA di mandi chaque jour ?
Loutah ngay naane bataye té guiss sa PA di mandi ….?
Thiateu gaaw niata yone lagn nieuw pour dieundeu niou nga naane « wakhal waaw »
Concurrence Papeu ak Yaye, farr digueunté Thiaat ak taaw
Bountou bi teuth neu bou yagg pour samay thiaga fans
Loutah chaque jour mane ? dou tchi yeen nieup Yallah leu dou chance
Djoudou pour tédeu bala sa Yaye di am accouchement
Nioune douniou gnéin ! koudoul gnéin moy dém wayaane pour lane ?
Wakh ci mane lou niaaw dossi am loudoul gaadou aakkeu
100% nittou Takoussane faaw ngay sangou di sakkou niaane
Wathié sama niakk samay rongogne meune bagna fèègne
Gni la sotalone gno gno nieuwaate pour tourr sa dérétte
YALLAH gueune Aldiana kouko xam mounoul ragal déh
Malaaka biir safara lane mo meunoul meuneu nék
Damay liguèye damay xepp di def
Business di fayékou werr bou déh fayékou téw mou téw
MARTIN LUTHER dou « YES WE CAN » motah mou done guéinteu dh
Nègre President dou té niouy ray nègres everyday
Meune nga tédeu même bo xamoul tédeu nougn kay bindé
Lerr dou fégne ci lerr, beuthieuk meusso ci guiss ay bideew
PD yé ni ci game bi dama rouss nek chef ci yèène
Melni Guel ci net fèèn di mééw pour rek quelques « j’aime »
Quelques « j’aime »
Dem ba goumbeu gni yaakeu sama xol ndakh xol yima yaakeu
Gaume ci xol ak xel Docteur dioxma alcool bi ma naane
Sante école yima diaar yeah sante prof yima daakeu
Nioleu gueuneu xam nigga sama album dina djar
Yo yima maateu laa gueuneu ragal boy yima clash
Tayéla job bi fadjar, sawara gaadou podjou guinaar !
Kouy seuy ndakh intérêt diour truand li nga sombi nga naane
Lou kholoul BIBLE kholoul CHARIA moy daw COMMISSARIAT
Shaw bigni teuth fane la djangué féthieu comme RIHANNA ?
Amo fi place parce que limay wakh xamossi dara
Thioky ba naaw siiw ci deuk yeup ni KOFI ANNAN
KUNTA KINTé tay say seut nioy sollou comme TOBY Ha-haaa (TO BE = etre esclave)
Gni ndaul xiff ak marr boudoul bateau meune nagn dokh fi ba kaaw
Mouy OR di DIAMANT dougn dem mouk ci baatou BOY yi done GASS
YALLAH bokoy niaanal lokoy niaanal ak ci kokoy niaanal (UNIQUE)
Mom rekkay diaar ci suuf ci guinaaw feulé ci kaw ci kanam (OMNIPRESENT)
Kounek ak sa weurseuk deuk bi meussoul deugueur ci DJIGUèNE yu woyof SEUR
Gni amoul lerr bouniou djaayé wéthié sen BOPP ci AUTO ak KEUR
Bou thioolone kène dou thi djaap kone f**k U, f**k nieup
Li dou Musique ndakh Musique défaloul wa Ndougou Sine
Borr leu té ma ngi ci guéné gni bagnone ma dougou ci
Même Y’EN A MARRE bou falu wone sakh LOUBEUL dou JOG FI
Même ROI ARABE bi perkal lagnekay suulé dou GUCCI
Yék caché 2.000.000 ma faté BOURSE 18.000
Tay amena GOUMBEU yu GUISS sen BOPP ci DOUNDOU GUISS
Nit yu gueuneu faible nio eupeu ci nioudoul Tiite
Ba Goor-djiguène di teud ak Lesbienne Double vie

Yeah ! Wédina sama bopp mané wone douma def auto-tune
Sampeu aum dou pour HIP HOP bayil bama dém Popenguine
Echec la gueuneu ragal que Déh
Ndax ay Chèque la beug rangalél mère
Mane ak rappeurs yeup ay siècle lagne rawantéwé
Té dagnemay tékeulél gniy topando ay topando kat
Amena beugne yu wééx mais nak déréttou gorr moko Lal
Diaroul may wakh maafi meune ndakh thiouné yeup dagnekay wakh
Diaroul may wakh maafi meune ndaxté niom nieupeu kay wakh

{Bridge}
Li né sama mind leu rek nékoul yaw
Always boumay yégueu ci kaw Assamaane
Owww HoooOooo
Owww HoooOooo
Hummmmmmmm !
Li né sama mind leu rek nékoul yaw
Always boumay yégueu ci kaw Assamaane
Assamaaaaaaane

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR