LYRIC

{Verse 1}
SanT Yallah cii air bimay nooyi ni
Ma ngui maggueu cii xel di def song yu diss
Natchie bi tangagoul djawou dji xawa niss
Ndank ndank niit yégui dem Jobbi dji
Niaakeu takh may guiss Mère bi di soneu tchi
Djangue tuute tank fayoum école bi shitt
Papeu xawma business yi ngay dox mais guiss
Nala té dara dou téé ma done sa fils
Sama toureundo mo toudou Dominique
Bo xamoul sama tuur deug meune ngama wowé DIP
Maa ngék sama call di bindeu poésie
Boy amoul bènn règle noko défé thiow dou djip
Tant que ma ngui cii yonou fessal place de l’obélisque
Niankatang yapp lagneko wara saucé fils
Boy baayil ma gaawantou tay dama wara tokk Eglise
Ndax bopp bi lou nek fay daw ni Stade Olympique

{Refrain}
Goudi aka gaateu loole Bou souba problème yu bess
Yène saay do sakh xam loy def
Ndax da nga moudjeu claté ak ay thiooono
Koufi khass ba tardé fo dieum
Dafa melni koufi khass ba tardé do dem
Fi koufi khass ba tardé do dem
Fi koufi khass ba tardé do dem
My Nigga koufi khass ba tardé do dem
Douniou niaane rek lepp mooooole
Dagni raak ba daleu tchi men
Mais yène saay do sakh xam lo def
Surtout bo dioudo cii yènn kogne yi
Di nga xamni koufi khass ba wathieu do yék
Di nga xamni koufi khass ba wathieu do yék
Fi koufi khass ba wathieu do yék
My Nigga koufi khass ba wathieu do yék

{Verse 2}
Fi temps bi rekka doul soneu
Montres yi di weundélou té douniou miir
Natchie bi moussoul goudé teud motah moussoul bindeunti
Niit yi di niaane werr bi déh pour meuneu am lougniy doundé
Répété lignou def diko deffate comme sassouné
Bureau, Marché, Chantier,
Gran-place, Bopp Kogne ak Atélier
Garré taxi, dakanté Carapide dou meusseu diekh
Bou gni di Takkeu gné di diémeu daggueu boumou gaathié
Nieulé di Job, gni di saathie, gné di youkhou saathié
Life rafett ni diabarou diambour té nekh ni thiébou deuthie
Rafett comme li Yallah nangou nekh comme loum gnou téré yeup
Jaameuh raciste ni neige moussoul am cii yèneu deuk
Pakhou deug moussoul khaaute waayé dou nieupeu niémé teup
Nieupeu meuneu dox waayé dou nieupeu xam fane ngay tek sa tank
Nieupeu meuneu ndiole waayé dou nieupeu xam nane ngay def ba maggueu
Leppeu meuneu thiool waayé dou nieupeu meuneu done déféant
Waxtanalak sa ndiéguénaay ba beutsét

{Refrain}
Goudi aka gaateu loole Bou souba problème yu bess
Yène saay do sakh xam loy def
Ndax da nga moudjeu claté ak ay thiooono
Koufi khass ba tardé fo dieum
Dafa melni koufi khass ba tardé do dem
Fi koufi khass ba tardé do dem
Fi koufi khass ba tardé do dem
My Nigga koufi khass ba tardé do dem
Douniou niaane rek lepp mooooole
Dagni raak ba daleu tchi men
Mais yène saay do sakh xam lo def
Surtout bo dioudo cii yènn kogne yi
Di nga xamni koufi khass ba wathieu do yék
Di nga xamni koufi khass ba wathieu do yék
Fi koufi khass ba wathieu do yék
My Nigga koufi khass ba wathieu do yék

{Verse 3}
Beus yi beuri nagne ba meunouniou compté
Okay meunouma def loudoul dox dem
Yèn saay xol fess yèn saayite xol diekh
Meunouma def loudoul dox dem
Baayil ba beutsét natchie motah niouy wakh kerr
Nakamou batay nioune nio ngui ci kawam
Lane mognou baayi ci kaw terre
Xam li nga beug diko def nio ngui ci kawam

Beus yi beuri nagne ba meunouniou compté
Okay meunouma def loudoul dox dem
Yèn saay xol fess yèn saayite xol diekh
Meunouma def loudoul dox dem
Baayil ba beutsét natchie motah niouy wakh kerr
Nakamou batay nioune nio ngui ci kawam
Lane mognou baayi ci kaw terre
Xam li nga beug diko def nio ngui ci kawam

{Refrain}
Goudi aka gaateu loole Bou souba problème yu bess
Yène saay do sakh xam loy def
Ndax da nga moudjeu claté ak ay thiooono
Koufi khass ba tardé fo dieum
Dafa melni koufi khass ba tardé do dem
Fi koufi khass ba tardé do dem
Fi koufi khass ba tardé do dem
My Nigga koufi khass ba tardé do dem
Douniou niaane rek lepp mooooole
Dagni raak ba daleu tchi men
Mais yène saay do sakh xam lo def
Surtout bo dioudo cii yènn kogne yi
Di nga xamni koufi khass ba wathieu do yék
Di nga xamni koufi khass ba wathieu do yék
Fi koufi khass ba wathieu do yék
My Nigga koufi khass ba wathieu do yék

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR