LYRIC

{Intro}
Gouro, 3 pièces
Gouro, 3 pièces
Gouro, 3 pièces
Gouro

{Verse 1}
I say “Alaadji Miézé”, Def la sama soxna lala yeené
Mane ak yaw ci Djaaka Imaam à présent
Bolémaak sa Papa nako géré
WooOooooooo !
yaw laa ! waaaa, yaw leu
Yaw laa ! waaaaa yaw leu
Beug nala xamna beug ngama
Fayal ngama soumala amé amna gnèineti diabar
Ey ! Ani Pa bi na ngako WoOoo Oooh
Damala beug takk guénouma ak yaw OoOo
Viens père wakhma lane leu, loy douté ééé éééé ?
Beug nako amna Diiné ak Liguèy ééé éééé !

{Bridge}
Eéééy ! Baby oubile meu sa khol pour ma nek sa borom keur
Haan Yeah ! Nala djeundeul ben keur pour meu nek sa borom keur
WoOooo ! Wakh ak sen wa keur. nénagne maay sa borom keur
Haan Yeah ! Naa taal sen keur sougn meu défoul sa borom keur

{Refrain}
Haan Yeah ! Dina indi Gouro def 3 pièces
Gouro def 3 pièces
Gouro def 3 pièces
Gouro def 3 pièces
Gouro 3 pièces (ngani lane ?)
Gouro 3 pièces (ngani lane ?)
Gouro 3 pièces (ngani lane ?)
Gouro 3 pièces

{Verse 2}
I say “Takkeu sama FIIT do am bène woudjou baby à part sama FIIT
Yeah ! Boula neekhé dooreul RADIO maay sa Borom COEUR baby CARDIO
Louy bayaanté pour kouné séy séy bi
Bougn def lolou kaay niou seuy seuy
Maak yaw warouniou am blem
Yaa eupone prétendants championnat anglais
Reception bi invités yi naani Ginja
Soma fiiré dina mourou melni ninja
Mayé bou ndieuk mayla galé tek ci Trois quart
Souma lay niaaani feug gandi boubou trois quart
Mane leu gars yi wowé Batman Miézé
Am diabar djou melni yaw la yagg rêvé
Nuit de noce premier song ma mayla bébé
Daaan na tokk di lathie Yallah fi nga feeté

{Bridge}
Eéééy ! Baby oubile meu sa khol pour ma nek sa borom keur
Haan Yeah ! Nala djeundeul ben keur pour meu nek sa borom keur
WoOooo ! Wakh ak sen wa keur. nénagne maay sa borom keur
Haan Yeah ! Naa taal sen keur sougn meu défoul sa borom keur
{Refrain}
Haan Yeah ! Dina indi Gouro def 3 pièces
Gouro def 3 pièces
Gouro def 3 pièces
Gouro def 3 pièces
Gouro 3 pièces (ngani lane ?)
Gouro 3 pièces (ngani lane ?)
Gouro 3 pièces (ngani lane ?)
Gouro 3 pièces

{Outro}
Alaadji Miézé Def la sama soxna lala yeené (Yé yé yeah )
Alaadji Miézé Def la sama soxna lala yeené (Yé yé yeah )
Alaadji Miézé Def la sama soxna lala yeené

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR