LYRIC

Man aw’may nélaw
Man talou may nélaw
Kone bou may nélaw boul ma yé
My nigger bou may nélaw boul ma yé

Yag si game bi né R4
Sound ba la dé ma fintat
Yokal sa volume té bissat
Na maguéti haters yi dadjéti sen baat
Nop yi nguén ma di dénkat
Ma délou tassaré ti sen carte
Diém nga ma top da syncop
Si single you bari né chrono Usain Bolt
Kone bou may nélaw boul ma yé
My nigger bou may nélaw boul ma yé
Kone bou may nélaw boul ma yé
My nigger bou may nélaw boul ma yé
Gnou si bari da gnouy gnodi young money tanganay daw sen biir yi
Ya gui nélaw beug guént money bo yéwo ma diém ko firi
Ya tala nélaw yéwo times square garden digui New York city
Wayé kou la lath né ko Zion mou gui boyal Dk city
Guissou niou pa bi da worry
Bayi gnok mère bi gnouy keur keuri
Talou gnou yéndou si kerr gui
Na naath bi di tang gnoun dou gnou ko djeuri
Kone bou may nélaw boul ma yé
Gawou ma nélaw da’y formidable né Stromae
Bou ma woutoul lou ma yobou keur gua Ma né ma papa ou t’es
Lou gnou wouté moy da nga beuri nélaw man da ma goudé

Kone bou may nélaw boul ma yé
My nigger bou may nélaw boul ma yé
Kone bou may nélaw boul ma yé
My nigger bou may nélaw boul ma yé
(Bo ma yé waté di na la dé)
Kone bou may nélaw boul ma yé
(Bo ma yé waté di na la dé)
My nigger bou may nélaw boul ma yé
kone Bou may nélaw boul ma yé
My nigger bou may nélaw boul ma yé

Mou sou ma am cadeau sa ma life sa ma dome may done pere noëlam
Fi lek sa ma djabar mou gui fonk sa ma YAYE dou tour rangogne si kanami nawléwam
YAYE rek lay tarbiyou
Ak lo meuna am
Ba la nga ma guiss ma nguiro
Ak lo meuna xam
Bou ladjé ma doli si ngoro kéng waroul yolom né kouy féth Cobo yi
Ma tégal lassi bou né wéng djeuleul blow bi yeup meuno ko bayi
Rolex Gucci gnodil gnou nane bokok gars gni
Ya geuna fouti sa YAYE nélawoul tay ndakh amoul loumou agné
Bou kharé fandé battrél si soirée yi mouy réré fondé
Ba moudjé téeré lali lhopital my nigger gnouy lath té fo né

Yag si game bi né R4
Sound ba la dé ma fintat
Yokal sa volume té bissat
Na maguéti haters yi dadjéti sen baat
Nop yi nguén ma di dénkat
Ma délou tassaré ti sen carte
Diém nga ma top da syncop
Si single you bari né chrono Usain Bolt
Kone bou may nélaw boul ma yé
My nigger bou may nélaw boul ma yé
Kone bou may nélaw boul ma yé
My nigger bou may nélaw boul ma yé
(Bo ma yé waté di na la dé)
Kone bou may nélaw boul ma yé
(Bo ma yé waté di na la dé)
my nigger bou may nélaw boul ma yé
(Bo ma yé waté di na la dé)
kone Bou may nélaw boul ma yé
(Bo ma yé waté di na la dé)
My nigger bou may nélaw boul ma yé
Outro
Ya tala nélaw man
Gnoun njaboota gnou djteul
Ombre Bolt
Ouhouu ouhouhouwouu
Ouhouu ouhouhouwouu
Ouhouu ouhouhouwouu
Ouhouu ouhouhouwouu

Added by

Ahmed

SHARE

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR