LYRIC

Verse 1
Sonne naa te guisseugouma dara loumeu meuneu fatté lo ni yow la tannone pour nga samm sama mbeuguél

Fonk naala kone faut q nand ma te fogone nani soumeu togué weet ak seme bopp ding me goungué eh

Yama newone ne ding ma dinthial se thiaabi khol te loumou gouddi gouddi dinga tidji soumeu feuggué

Diangg naala mokkal naala amoul dara lougn ma meuneu khamal tchi yow

Ci yaw
Ci yaw
Ci yaw ( ci yawww)
Ken dou wakh dara ci yaw
Ci yaw
Ci yaw
Ci yaw ( ci yawww)
Ken mounouma wakh dara ci yaw

Verse 1
Sa yo guenné mane ngay khalaat
Souma kholé yow rek laa am
Soma guissoul dangay malade
Yen saay me doyal seukk ci yaw

Chorus 2
Sonne naa te guisseugouma dara loumeu meuneu fatté lo ni yow la tannone pour nga wetteuli me te nga samm sama mbeuguel
Faut que ma maanou ndakh thiow li thiow li yeup waroul niaaaw te warouma fatté tam
Lepp lima diangg ci yaw
Ci yaw
Ci yaw
Ci yaw ( ci yawww)
Ken dou wakh dara ci yaw
Ci yaw
Ci yaw
Ci yaw ( ci yawww)
Ken mounouma wakh dara ci yaw

Verse 2
Ci yawww
Mouno nango am tort
Ci yawww
Te guedj nga wakh me d’accord
Ci Yaw
Fogone naani c mort
Bobou khawma wone louy amor

Ay khoulo tey dioubo tey
Yenn wakh you sew yi douniou tardelaat soudone tey
Mane lenn laa guiss ci yaw
Moy ken khadioul tchi sougn thiow

Chorus 3
Sonne naa te guisseugouma dara loumeu meuneu fatté lo ni yow la tannone pour nga samm sama mbeuguél

Faut que ma manou ndakh thiow thiow li yeup waroul niaaw te warouma guedd tam lepp lima defar ci yaw
Ci yaw
Ci yaw
Ci yaw ( ci yawww)
Ken dou wakh dara ci yaw
Ci yaw
Ci yaw
Ci yaw ( ci yawww)
Ken mounouma wakh dara ci yaw

Hun (ci yawwww)
Hun hun hun (ci yawww)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR