LYRIC

{Verse 1}
Depuis bama commencé takkeu
Ci leu moteurou Rap Galsen bi commencé takkeu
Animateur yeup nénagne moussouma marr sen taate
Niata Old Scool dans le coma
Déwouma di jott ay Hommage
Yaw xéwago di khomaate
Ndeysane Album bi lambeu neu picc yi commencé sapp
Sama Papa nénama fils c’est normal. N’est ce pas ?
Weah c’est normal kay Pa
C’est normal ndax dama def ay cicatrices
Est-ce que France sagnena bania diox Zidane 10
Cicatrices manaam dama dieul artistes
Yu gueuneu makk ci bène att ma def lène ay Archives
Malène meune té yéneu ko gueuneu xam Billahi
Sa Label leufi gueuneu gnéin Reptyle
Tay niata deumeu beugueu réré DIP
Nélène DIP yoneinti leu da nio reeré mbiir
Clash lo thi yonou Cimetière ak ay Eglises
Fake ass Nigga Ragal Yallah moy mayé fiit
Ngay fène rek di am loy diémeu wakh sama ethnie
Est-ce que borom tuur bémay diakhal CD yi
Même Jay-Z meunouma diakhassék Jesus
Do am dara ni Candidats wou PS yi
Kone boul ess Fils yaw mandit kat nga do Emcee
DIP comme Messi mom yéne yi douko métil
Boy do mbéthie ki ? No bayil ma defko domestique
Boy do ray ki ? No bokouniou sakh pointure
Jouguël fi démal té bouma def signe
Tarr Mbéthie leu Bassi lékhou Aatou Reer Neu
Saa-souné ngay dégueu sama baate founé
Yaw Xathie bou déh bi do takkeu ni gaz bou diekh
Yène taatou nèène ngène def té DIP taalou lène
Mane saakou thiép la gueune meuneu calculé
Té Kaassou méw la yémalé ak sen caissou nééw
Hummmmmmmmmm

{Refrain}
Cicatrices cicatrices
Sama succès dafa def ay cicatrices
Cicatrices cicatrices
Nigga soula météé meune nga tekk sa taate cii gaz bi
Cicatrices cicatrices
Nieupeu may laathie équipe yeupeu meu soxla ni Pogba Juventus
Aaaaaahhhhhhh
Cicatrices cicatrices
Ni Illuminati sama niaari tankeu cii Pyramide

{Verse 2}
Ma dakkeu Rap ci sama génération
Sa Maame sakh day laathie baxam guéné na son
Jougué school K-Rim Xrrum Xax guène beug ma def sen Gaston
Kou lène néngène dima clash xana da ngèneu dof
Li ma am ci Rap damako mérité
Té dina fessal stade bi laata Bum bi di guèneu
Kamikaz sakh dou tax samay ennemis diekh
Fuck Comédiens yi di wéthie wéthie comme ay djiguène
Déféant yi dagnema dessé xam
Idy mayma…faw decès am
Lo tek niou tek boy xéx niou xéx
Boy dëkou ngène kou kène doul dëkou
Wakh bou séw bi thiép bou séw
Couplet bouy tégui békkou sékou
Délou lène fi ngène jougué
Bou ngène beugué kou dégueu sen tuur
Ngène liguey nioune nioy foutékou totch sa thiotou *** Aaaah
Fuck you nigga fuck say nigga
Fuck kou bégue fuck kou béguoul Job bou set leu
No goungué wouniou kène
Douniou trophée noone yé ngui beug déh
Douma def ni Drake di guéné bet to bet
Nieuweul face to face boy légui fake yi féégne
Boy bou ndaw dilène thiop ni thiébou dieune
Yagg dém fi fake yi deuk di yéh fitna
Damako def ba yëg ni légui xééwi na
Cicatrices foumou tolou Gaïndé bi daa xiff
Ndax gnifi nieuwone dembe di niaane feat.
Nio taxaw feulé néé di dingaate DIP
Nigga fuck u, fuck sa Dieum fuck sa Rouh
Deum bouy waadja déh fokk mouy dieufeurou
Khawma niata grand laafi ray niou déh
Té banouy Rap ma ngui jardin di day toubeuy
Moréééé

{Refrain}
Cicatrices cicatrices
Sama succès dafa def ay cicatrices
Cicatrices cicatrices
Nigga soula météé meune nga tekk sa taate cii gaz bi
Cicatrices cicatrices
Nieupeu may laathie équipe yeupeu meu soxla ni Pogba Juventus
Aaaaaahhhhhhh
Cicatrices cicatrices
Ni Illuminati sama niaari tankeu cii Pyramide

{Bridge}
Thiow li beuri na Thiow li beuri na aaaaaaah
Lolou démal wakh ko niggaz yiko atanoul
O My nigga O my nigga
Wakh ko gniko atanoul
Thiow li beuri na Thiow li beuri na aaaaaaah
Lolou démal wakh ko niggaz yiko atanoul
O My nigga O my nigga
Yeah Wakh ko niggaz yiko atanoul

{Verse 3}
Game bé beuri fake ay rappeurs goor-djiguène
Mane awouma loumay dindi awouma loumay modifié
Cuz, I ain’t got no regret, I ain’t got no regret
Mama ma ngui cii jaameuh
Dougnema def sakh bopp bouy méti

Mané Thiow li beuri na Thiow li beuri na
hééééé
Lolou démal wakh ko niggaz yiko atanoul
O My nigga O my nigga
Aaaaaaah yaw Wakh ko sa gars yiko atanoul
Hééééé

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR