LYRIC

{Mao – Refrain}
Com dab dagni def louniou meune
wakh louniou meune di yaakaar moy li guueune
Ummmmh huuuum com dab
Yeah yeah come dab
Même si on a rien dans les poches dougn téé bégué ak yeen com dab
Ummmmh huuuum com dab
Yeah ! Dagni sanT Yalla (Sant Yalla)
Sant Yalla (Sant Yalla)
Dagni sanT Yalla (Sant Yalla)
Sant Yalla (Sant Yalla)

{DIP – Verse 1}
Ummmmh com dab
Fi nganiou baayi batay nga fékaate gars yi com dab
Yallah bahna com dab
Hééééééééé com dab
Niouné yaw niéméwo lou méti ya ngi sa kaw lalle
Kou nékkak sa programme
Hééééééééé khol ma
No no noto ennemi bougou ma nek ci jaameuh
No no ! Dadjo lo lène sotema
Héééy O my baby girl
Dadjé tay beugueunté soubeu baayanté ganaaw soubeur au revoir
Bouma laathie mane xawma (Yeah)
Job comme Maman niémé teuss teussi
Mane Xoslouman laa douma gangster shit
Mané awma mind tééla xepp wétchite
Nigga teel sa arme té nga dinthieu sa fiit
Job comme Maman niémé teuss teussi
Mane Xoslouman laa douma gangster shit
Mané awma mind tééla xepp wétchite
Nigga teel sa arme té nga dinthieu sa fiit

{Refrain Mao}
Com dab dagni def louniou meune
wakh louniou meune di yaakaar moy li guueune
Ummmmh huuuum com dab
Yeah yeah come dab
Même si on a rien dans les poches dougn téé bégué ak yeen com dab
Ummmmh huuuum com dab
Yeah ! Dagni sanT Yalla (Sant Yalla)
Sant Yalla (Sant Yalla)
Dagni sanT Yalla (Sant Yalla)
Sant Yalla (Sant Yalla)

{DIP – Verse 2}
Hééééy clean clean set clean
Ay waay kaay féthiak mane mou bagne
Tchiling tchil ak samay homies
Kénène douma téré fowé sama life
com dab, com dab, com dab
com dab ! Lerr nama ni dina gueuneu méti ci mane (Yeah)
Kone nak mane d’accord naa ni défagouma gatt broda
com dab
Douma déh tchi nèène
Never Douma déh tchi nèène (Yeah)
Doundou comme Star déh comme Légendes yifi djota diaar man

{Mao – Refrain}
Com dab dagni def louniou meune
wakh louniou meune di yaakaar moy li guueune
Ummmmh huuuum com dab
Yeah yeah come dab
Même si on a rien dans les poches dougn téé bégué ak yeen com dab
Ummmmh huuuum com dab
Yeah ! Dagni sanT Yalla (Sant Yalla)
Sant Yalla (Sant Yalla)
Dagni sanT Yalla (Sant Yalla)
Sant Yalla (Sant Yalla)

{Mao Verse}
So fresh so clean sound
We gonna give you one more time (Yeah)
No stress, no go down
Tek sunu thianyine ak sunu sound (Yeah)
Hello hello hello
Hello Senegal what’s up ?
Hello hello hello
Yeksi nga ci DK sama, what’s up ?
Liy dall tchi nopp aduna ci yeup ganyine
Tangorou safara meunoul dégne ak eupou kaay (Yeah)
Diougueul nga féthieu té nga baayi neubou waay
Hapiness for life never mind

{Mao – Refrain}
Com dab dagni def louniou meune
wakh louniou meune di yaakaar moy li guueune
Ummmmh huuuum com dab
Yeah yeah come dab
Même si on a rien dans les poches dougn téé bégué ak yeen com dab
Ummmmh huuuum com dab
Yeah ! Dagni sanT Yalla (Sant Yalla)
Sant Yalla (Sant Yalla)
Dagni sanT Yalla (Sant Yalla)
Sant Yalla (Sant Yalla)

Hééééy clean clean set clean
Ay waay kaay féthiak mane mou bagne
Tchiling tchil ak samay homies
Kénène douma téré fowé sama life
com dab Yeah yeah come dab

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR