LYRIC

{Ara}
Yaw rekka xam sama price yama dieundeu té wakhaléwo
Da nga changé sama life, wakhma deug té nakhatéwo
Nga fekk xol bi milles morceaux tabakh ko ni maçon
Bamoiuy feegn sama eyes kou beug beug naala
Kou bagne nama baayi ak yaw Yaay sama waay waate naané
Yaw rek ci xol bi lénène dou tchi xathie gueum naani
Yaay sama docteur kénène douma fathie xam naani
Louma weuri fénène am ngako paathie yegg naani
Yaay sama djanteu nama touma naathie baby…

{Refrain}
Nékouma because I’m
So Crazy in lova lova
Candy ! I love love love you so much so much
Tell me: Néma djap ngama do ba do ba
Baby… (2 fois)

{Dayza}
Setlou naani saay soma khol di rééh
Warro nameuh potou méw ndakh malay dadji
Sama xol bamako sentirou lé lala weur djap leu ndékété yaay sama sathie
So beugué dékillaate Abdou Rass, dédett doumala trahir niou feat ko defko maquette
Xam nga loutah may bagne nga def maquillage. En faite,
Da ngaka waneu wara sa khol gueuneu rafett
Siguile khol meu ci beute, baby réé meu c’est que ci leu
Sama rétane bi di meuneu gueuné mbekté bi leu
Xippil réwantoul, wanema caprices lep tchi leu
Ba xam nga bo dof doflo ba xarrou ma fekk ci leu
Mane damala beug nopp leu damala fan
Sa tuur bi laay feusseul feegnal ko ci wéy bima feinteu
Des fois di ngama wo mané leu awouma temps
C’est que journée bi yaw laay xalaate té goudi yaw lay gueinteu
GalsenLyrics

{Ara Bridge}
….Waate naané
Yaw rek ci xol bi lénène dou tchi xathie gueum naani
Yaay sama docteur kénène douma fathie xam naani
Louma weuri fénène am ngako paathie yegg naani
Yaay sama djanteu nama touma naathie baby…

{Refrain}GalsenLyrics
Nékouma because I’m
So Crazy in lova lova
Candy ! I love love love you so much so much
Tell me: Néma djap ngama do ba do ba
Baby… (2 fois)

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR