LYRIC

{Intro}
Morééé
Yeah DIP Doundou Guiss
Morééé With my dream team clic So word up

{Verse 1}
Mane maléni door té kène dou fayou (Kène dou fayou)
Awouma concurrence Barça – Real wala Pène – You
Loutah ? Pourtant damay nélaw niom niou yéwou
Di RAP di fèneu sopali RAP bi Job djou léwoul (Wax lène niou yéwou)
Kou nekkeu ngui diéme tidji bountou di woudjëk
Gni tchi ngourou RAP bou déh beuri crew ba moudjé
Motah yone bi loumou sorri sorri
Doundou Guiss dou meusseu worry cii sponsors yi I’m sorry
Na makk yi fay, rakk yi taakeu niou fégne rakinetak
Equipe wathieu Equipe yék ni Wade ak Macky Sall
Ndax ma dem ba sothie ci RAP bou peundeu rimes yu leundeum
Leundeum ni SENELEC ma dem ba sokkeu ay niggers yu décès
Niou ngui cii beuri déchet
Boy fokk niou nieuw léral
Tok cii kaw téwal (téwal)
Djot niou feusseul sunu bopp cii bi dh RAP GAME (Rap Game)
Ndax Job bignou fass yéné def dou pour RAP GALSEN
Amana ba ngène dalé RAP nioune nio ngui gnouy couche
Waayé tay dji fepp folène lapp nioune nio ngui fay Xouss
Lougnou beug dafa lerr naagneu gaayine
Légui nak bala naadjé dafa djot nak niou dem

{Refrain}
Dagni dem ! Ndax guiss nagne nii djotna
Yégue founiou niit yi done khaar business HIP HOP
Dagni dem ! Ci sakhaar cii lagni bokkeu
Nio ngui dem té douniou sakh khaar bitchaz tokk
Dagni dem ! Mbiir bi dou dem ndax beug dem
Dagni yégueul sunu rimes yi cii game bi gueuneu tang
Dagni dem ! Damn bitchaz yi got’em
Doundou Guiss we gotta respect that’s we’ll make

{Verse 2}
Okay Man ay Boy yu ndawe di RAP ay kémaane
Nioune bagnekoy fowé ya ngui cii Tom and Jerry ak Pockeman
Kone meuno gagné cii BABI bo meunoul téé poignet
My nigga Marau-Zik meune nama témoigner
Meune def li mindef yu néw di diéme (Morééé)
Kone boul tek nii nioune nagne goudé cii guéw (Koufi né)
Underground bou réw motah téyeul sa respect
Boy dem par force ya xam booy diémeu rester
Dagni dem ak Zéro taukh, zéro shit, zéro goukh Zéro sniff
Héro do, Bullshit ghetto nigga boul tiite douniou zéro positif
Dém ak Zéro politique zéro polémique Doundou Guiss nioune rek nio mel ni
Am gueudeu bii nii Noreyni DIP, Bs-Baby niary phénomènes yi
Boul niou toppeuh aaleu ndax nioy ray té nioy rindi
Toggueu bi bou nioroul-lone kone dou meusseu nioré nii
Mbède bou niou yaroul wone bindeu bi dou djégué liii
Fuck niénène gni faral sunuy Ennemis,
“Put it down on me” 50 Cent – Jeremih
Yégueu la takha RAP mais mane louné lama diaral motah douma mayé dara

{Refrain}
Dagni dem ! Ndax guiss nagne nii djotna
Yégue founiou niit yi done khaar business HIP HOP
Dagni dem ! Ci sakhaar cii lagni bokkeu
Nio ngui dem té douniou sakh khaar bitchaz tokk
Dagni dem ! Mbiir bi dou dem ndax beug dem
Dagni yégueul sunu rimes yi cii game bi gueuneu tang
Dagni dem ! Damn bitchaz yi got’em
Doundou Guiss we gotta respect that’s we’ll make

{Outro}
Héy boul fokni dagni tok man amena heure bou djot
Sunu heure boulko khaar mou djot
Nigga montre bi lagni déréglée
Doundou Guiss dioxlène thieur man moy li war cii yaw
Shiiiiit

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR