LYRIC

{Verse 1}
Yeah ! Ba nieupeu diékhalé mane silay soga fess
Dap nala Papa parce que téré woma xééx
Dinagne leu enquête ndaxté tay sa doma xéw
Té bama lène wané samay rongogne niom nieup bëk
Bo xamé né faaw nga lekk faaw nga fokalé
Da nga xepp condamné bou tolou ni contenaire
Last-kri pérrou dalleu damala sole ba déh
Motah tay job ba déh niakkeu jot ba déh
Damako khadi safe cury pour wathié Jordan man
Ni bepp xettou nit bouy wadja done lénène
Fatéwouma finiou ma djangalé fignma djongalé
Fatéwouma Pa yimay nianal mère yima diox ma lekk

Avenir lagne démona djeuli ci yonou clochards
Karaw bou nioule ak xel bou makk sa niom maame
Boul waulou sakh gnila waulou confiance
Xadioul ci Malaaka Djiné Confiance
Maay Garab bi beug micro
Innocent bou andak Inno
Ay fenn crack nga kaay try (karraka kathie rk)
Life bi souma fataliko
Dioxma passport Visa Yeah
Tampon ci passport bi ma dem
Par force fasse djom Riche ba déh
Waw Goor di nga done milliardaire
Hééééy ! Yaffi néwone sunu Gang famille leu
Nioune nieup bokk diaar diaar nigga
Fima diaar koufa diaar xamé
Yaw Fi nga diaar koufa diaar tassé yaakaar
Ma ngi niaffé ma ngui khar matteu nigga
Xonéttatouma sakh rarement nigga
Fima djougué Soumafa ndaré délouwaat
Frekma jail wala teuth ma hopital my

{……}

Yeah ! Yeah ! Yeah !
Ba nieupeu diékhalé mane silay soga fess
DIP comme kou teudoulo correctionnel ay colonnel
Dinagnema sagga ndey dina lène songue xééx
Kone niakk djot ba déh guèné son ba déh
Meuwti sakh douma dieulsi parce que maak moma yém
Kone en cas MC bou déh boul laathie kane moka ray
Niata rappeur nga fay niata millions nga lekk
Boy déssétouma bène rongogne pour djoy sa deuthie
Est-ce que withiakh naa sama barraam ?
Guedj naa reuthiou depuis 17ans Mother F****
Damako khar ni déh ak Aldiana
Mane dama lèn réindi soga tiite ndeysan dawna yarram
Boy mane kassé ben niit 5000 niit dima xééx
Nianal naa samay ennemis ennemis ki ak kéé
Dama xééxal mbède bi, mbède bi dima xééx
Dama xééxal mbède bi, mbède bi dima xééx
Ma ngui ci chaisou buur, nio ngi ci chaisou dousse yi
Fake yi, dounkeu yi, Nandité yu mouss yi
Tek naniou deal mais kène guènou tchi
Noir et Fier amoufi, derr bou nioul, Mo xééx derr bou nioul
Mafi gueuneu touti, thiabbi bou reuyone dou tidji bountou
Ma ngi gueuneu yéék di gueuneu yéék di gueuneu wët
Xaritaka neew ci diamano wouy sama ndèy
Try yeurmandé def sama xol ci sama xel
Djaay kou meuneu fay douniou mayé khérr
Di keupeu caisse

Bepp fitna laa fitna Maay fitna
Fitna laa fitna Maay fitna
Lolo takh ma wagni samay djo bro
Lolo takh ma yokkeu sama job bro
Lolo takh ma niémé songueu ngandi Gros lot
Lolo takh ma weuy di course ak sama chrono
Pé (1er) laa dieul beugouma Passé
Pour njaago fauutak passé rek
Tassénté nga ak mane mou dégne

{Outro}
Ba nieupeu diékhalé mane silay soga fess
Dap nala Papa parce que téré woma xééx
Dinagne leu enquête ndaxté tay sa doma xéw
Té bama lène wané samay rongogne niom nieup bëk
Bo xamé né faaw nga lekk faaw nga fokalé
Da nga xepp condamné bou tolou ni contenaire
Last-kri pérrou dalleu damala sole ba déh

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR