LYRIC

{intro}
Bril and Books Talking

{Bril Fight 4…}
kaay fileu dougou nga finga,
yagga di dégg di beugga djéggué, Akcinga !
Fékkeucinga , gni gueuna yégg , dinga,
miin niniou nééké , fo djaaré lo fééké louné ciinga …
Raak nga … Gaanécinga
Yangui thi diggou conneu bi, li niouy Déff Dougn ko neubi
Djaay la dope bi – diiggueul taupe bi – téégui thioneu bi
X -Side point com la , Dégg saaga welcome la
miin nga ville bi , siiip nga deal bi, causé dégats kom-kom la

{Books}
Djougué thi sky bi , Diégui rail bi, djégué death bi
Djougué thi Fight bi ,laak daay bi, yééneu sight yi
Taal light bi , leundeumay bi, khouss ci night bi
Sooraalé Fight bi , moytou night borou thi side yi
Fi Danger Danger , amoul louniouy mind, sunu side immortél aki ninja
My nigger you are wanksta wanksta –
Ma dougou séni side side , tali light , eundi mic , niou niit thia

{Chorus – Bril}
*******Hééééé Yooowww********
Yangui sunu Under -Hood side ,
finga dougou gnifeu deukk nieupp né thi Danger
*******Hééééé Yooowww********
Niounn daniou taylé sunu life ;
Yamalé am ak Niakk sunu lépp moudjé done Jeux
*******Hééééé Yooowww********
Yangui sunu Under -Hood side ,
finga dougou gnifeu deukk nieupp né thi Danger
*******Hééééé Yooowww********
Niounn daniou taylé sunu life ;
Di fight —- Sunu lépp moudjé done Jeux

{Books}
Bo amé séétlo’k séétou dinga mousslou sunu Zone
Daniou seek lépp ,xéétou sangara, xétou bone
Daniou Ndiip tékkékou, gangoroki djeuli gone
Sou lén Flic kéépétoul , Diamono thiy gueuneu sone
*******Hééééé Yooowww********
Nanga sôôr fingay ték sa tankk, step by step vempire yangui fi di ngankk
*******Hééééé Yooowww********
Nala wôôr Goor, yokou sa rythme, barbarisme, charismay takh niou niitt meu

{Bril Fight 4…}
Danger Zone la Déég-nga, nieuppeu dingue, fougn la taaro déé-nga
Doko wééddi check-nga, légui sipp-nga
nieuppeu Sadik Déég-nga
Dagal sa mama kaffla/ fo dégg yokhou paffla/
Xoolè gaaffla, xèff niou keufla, yeugo deal bi mbed mi maf la/
Nékk-thi daaw té ba légui niongui thi topp
Thi kanamou boum yi , never niou daw té bokk thi biz yi ,nékk thi top
Amna Bitch – Amna toott , fi beurri drug dealer – fi leu
Adjal pitch, gawal track , done fi killer , louniou feel leu

{Chorus – Bril}
*******Hééééé Yooowww********
Yangui sunu Under -Hood side ,
finga dougou gnifeu deukk nieupp né thi Danger
*******Hééééé Yooowww********
Niounn daniou taylé sunu life ;
Yamalé am ak Niakk sunu lépp moudjé done Jeux
*******Hééééé Yooowww********
Yangui sunu Under -Hood side ,
finga dougou gnifeu deukk nieupp né thi Danger
*******Hééééé Yooowww********
Niounn daniou taylé sunu life ;
Di fight —- Sunu lépp moudjé done Jeux

{Books}
**Piiw Piiw**
Caméra wala picture , amdi-djamm, neggers , none wala fiit ya
**Tiiw Tiiw**
Fuck séni Fils ya, blaze your mama, kouma aakk-ci ma nique ya

{Bril Fight 4…}
Paa bou maguéttalay teukou , deukou rothil-la djam
Minette piiss la , dougou roukou ngir dégg Djaamm
Djeul xaalé bi guéneu thi mbéd mi daap-la/
Niaann-la sa joint, Baapp-la/
Tokh ba beutt yi ngookh, dokh di “S” djaay na fi prék , Djapp-la/

{Books}
Fokk-niou gangsta Thiine-yi néékh /képp-dji kill yi féékh
Léékk-dji king yi guéékh/ Fékkeula souff-ci féékh
Adou calpet-la , Braqué-la, Tékk la sén doune yi djéékh
Douma djaarni Bandit – Gangsta recognize Gaaang

{Bril Fight 4…}
Like that , little boy yi tékk, Criminal Gang
Kill soga nékk, finga fékk, kouné meuna Bang
Kénn mér na wanéna beurrétam/
Djoukna tourna déérétam/
Di raak ba nieupp djaapp mou fippou ,djottna thi méritam/

{Bridge}
(Boys Choir)
This side is so Dangerous – Boufa dougou gnifa deukk nieuppeu Dangerous
Boys -Girls Dangerous – I’m so serious Daniou Dangerous

(Girls Choir)
This side is so Dangerous – Boufa dougou gnifa deukk nieuppeu Dangerous
Boys and Girls Dangerous – I’m so serious Daniou Dangerous

{Chorus – Bril}
*******Hééééé Yooowww********
Yangui sunu Under -Hood side ,
finga dougou gnifeu deukk nieupp né thi Danger
*******Hééééé Yooowww********
Niounn daniou taylé sunu life ;
Yamalé am ak Niakk sunu lépp moudjé done Jeux
*******Hééééé Yooowww********
Yangui sunu Under -Hood side ,
finga dougou gnifeu deukk nieupp né thi Danger
*******Hééééé Yooowww********
Niounn daniou taylé sunu life ;
Di fight —- Sunu lépp moudjé done Jeux

{Outro}
Bril and Books **talking**

Added by

Papi

SHARE

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR