LYRIC

{Verse 1}
Bril Fight 4…..
Nioune leu gni tééla tambaali, soubou tchi kharé bi done gneinteu (4)
Moussouleu yombe nioy matteu ci taal yagg férr gneinte
Niéteu (3) gni baayi mou dess bèneu (1) ni Ln de Expo
Mouy tekk lou yeemé nek light degg dadj té dou XPO
Wara libérer gni dieul sen xel yi sopi kasso
Maîtriser ART bi wathié MOZART ak PICASSO
Yoré XALIMA DOCTEUR bindeu lodoul gaawa XAM
Tekk lou lerr beu gni teukh sakh nio naane leu dagni degg wakham
Maay ki meun tchi RAP té nieupeu ko yegg ni kou djoum tokk tchi POUSSO
Dioxla SON yu am BUT wa GAME bi dougn néma PASSO POUSSO
Yoré RAP bou rare comme photo bou ABLAYE WADE am Karaw
Douma rawanté ak yeene maak Usain Bolt lagni khol kou raw
Meuneu RAP meuna WEY tek tchi meune BINDEU gueuneu AAY
Yokk tchi meuné founé maa ngi feegn tchi film légui fo tchi beats yi diko djaay
Boulma comparé ak bène rappeur ma ngi tchi bénène monde bokkou niou heure
Mane Yalla Rap biy foli présidents yi wakhal chef de bandit mane leu acteur

{Refrain}
Tuur bi foko dégueuh doto lathié kane laaa
Def lou lerr té kou guissoul dou jog tchi wane laaa
Polyvalent tchi sound yi teug beat bi rap meune waaaaaaaay
Lepp mane laaaaaaaaaaaaaaaa
Deggouma Deggouma wakhal “Bril Fight 4…”
Yaw wowéma wowéma néma “Bril Fight 4…”
Mane Deggouma Deggouma wakhal “Bril Fight 4…”
Néma “Bril Fight 4…, Bril Fight 4… ”

{Verse 2}
Fouma dégué beat ay rimes yu carrées nioy dikaate
Ma Rap ba dagg boum yi garé bepp niodi kat
Xamo heure bi jot té nangou nga ma ngi kay tek ci temps
Nopp ya ngi takamtikou li ngay get mo excitant
4 BARRES la tek MANDI KAT yeup dima WAAté
Xamone ngène né barre bi day yëk bouma nieuwaaté
Mane Serigne laaa tchi daara bouma nouyo nieupeu fay
Sén rappeur yorélou malène dara téwoul dina lèn fèy
Gni nga gueuneu feel malène meun motah ya ngi cissou aadjouma
Sama bopp fess ak rimes melné JUMMAH leu bissou AADIOUMA
Next Level teugg tchi Assyko / Nane la ndokhla Assiko
Maay Messi RAP bi nieupeuy khaar sama SON yi né Classico
Wané lou yeemé ni Djiné tchi kouné keemtaané
Xam ngané tchi louné ay années la rawé gni tané
Biss bouné niou guéné fi thiouné di fenn rek Promo maay MC JACK BAUER
24H laay RAP Fi KILL lène beusseul CHRONO

{Refrain}
Tuur bi foko dégueuh doto lathié kane laaa
Def lou lerr té kou guissoul dou jog tchi wane laaa
Polyvalent tchi sound yi teug beat bi rap meune waaaaaaaay
Lepp mane laaaaaaaaaaaaaaaa
Deggouma Deggouma wakhal “Bril Fight 4…”
Yaw wowéma wowéma néma “Bril Fight 4…”
Mane Deggouma Deggouma wakhal “Bril Fight 4…”
Néma “Bril Fight 4…, Bril Fight 4… ”

{Verse 3}
What’s my name “Bril Fight 4….”
Do you know my name
What’s my name “Bril Fight 4….”
…………………….” Bril Fight 4….”
Dama meun li ngène meun teksi meun li ngène meunoul
Li ngène dieem beu soneuh ngèni sikeul kagn ngène may nangoul
Lamp yeup ngène ma fayyal limay tekk di gueuneu lerrr
Baayi leen niouy tékeulé Diamant ak ay Kherrr
I don’t give a fuck mane douma def li nga fokk
Mane douma def li nga fokk doundou ma ligni wakh malène gueuneu déh let them talk
Fi gnilay beug limité moy gnifi gueuneu teelé
Dougnma yéééw kouma guiss tchi chaines dama gueneu Télé

{Refrain}
Tuur bi foko dégueuh doto lathié kane laaa
Def lou lerr té kou guissoul dou jog tchi wane laaa
Polyvalent tchi sound yi teug beat bi rap meune waaaaaaaay
Lepp mane laaaaaaaaaaaaaaaa
Deggouma Deggouma wakhal “Bril Fight 4…”
Yaw wowéma wowéma néma “Bril Fight 4…”
Mane Deggouma Deggouma wakhal “Bril Fight 4…”
Néma “Bril Fight 4…, Bril Fight 4… “

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR