LYRIC

{Mao}
Life bi dé ni la boy dara djougoul rek sotii
Waayéééé éhhéééé 
You can have it if you want it
Sossi défé sa kémteulay katane biss dina sotii
You can have it if you want it
Sossi défé sa kémteulay katane biss dina sotii
Ooooooooh Hooooooooo
Aduna cii nila boy dara djougoul rek sotiii
Doundou bi ngay doundou dé xam nani dafa méti
Waayé kou meusseu mougne di nga meusseu mogne boul khadii
Bo beugué Money fokk nga téleu diouk dougou cii town bi
Diayanté …souy méti bania xepp dara lo xam sétile
Wowowowowy
Xam li nga beug boy taneu sa yone té bouko tégui
Boul déglou nones yila diémeu wagni
Li tchii dess tek ko cii loxol borom bi
Dina Bakh Insha’Allah

{Mao – Refrain}
You can have it if you want it
Sossi défé sa kémteulay katane biss dina sotii
You can have it if you want it
Sossi défé sa kémteulay katane biss dina sotii

{Books}
Yes han!!!
Djougueul cii kogne bi nga tokk Bayi science yi rêves
Wessu naniou théorie diéme lagni def
Sa doli djou beuri, weuri djil yay sa chef
weuri dji wari cii deuk bi done SDF
Waro né yathie goumbeulo, Bayi science yi rêves
Djougueul té dieuli li nga mom boumou djafé sa xeff
Boul masseu bayi boume bi rote tchii right ak left
Founiou ko fokk dougou fa wouti cfa neff
Fékhé ba diir sunu kanam
Li sunu kanam
Pekhé dou diekh bania di tiit sunu kanam
Djay sunu anam
Djay sunu xalam
Kou fethie ba paré war nga fay sunu xalam

{Mao – Refrain}
You can have it if you want it
Sossi défé sa kémteulay katane biss dina sotii
You can have it if you want it
Sossi défé sa kémteulay katane biss dina sotii

{Books}
Fokk niou Job sunu guinaw
Tiapp money fanaw
Feki dji kaw gni tiapp bané falaaw
{Mao}
Falaaw tokk ci sa donka sigui
seug dépense bi matoul taay kèn douko cassatii yé
{Books}
Bouniou méré dou graw
Dina am Insha’Allah
Yoré té goré fayi dji gni nga yoré lone daw
{Mao}
One day, warna meuneu né One day
Souniou tiono né sunu guinaw
{Books}
Game bi séni fam yii guéni yébbi
Kou deggui theme bi
Téki lène cii feinte yi
Gni lèni gomdi wédii lène ba lanki
Na diom yi guèni
Weddi, wathie sa gueinte yi
{Mao}
Xam ki nga done
Gueum li nga done
Fala base bi nek boy boul sone
Niit kou nek amena li nga meune
Exploité ko au maximum

{Mao – Refrain}
You can have it if you want it
Sossi défé sa kémteulay katane biss dina sotii
You can have it if you want it
Sossi défé sa kémteulay katane biss dina sotii
You can have it if you want it
Sossi défé sa kémteulay katane biss dina sotii
You can have it if you want it
Sossi défé sa kémteulay katane biss dina sotii

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR