LYRIC

{Mao Sidibé}
Loumou méti méti dougnou daw
Danou jog faxassou dokh bi gueuneu gaw
Jog lidieunti dji bala nélaw
Soubeu bénène bissleu lep DINA BAKH insha’Allah
Soubeu Soubeu Yallah la wawaw wawaw

No matter, How hard is the day
Sometime you better learn the hard way
You have to face hard ship in other
To become stronger, Tomorrow is getting sweeter
Insha’Allahou dina bakh wawaw

{Refrain}
Déguelou lène djoy yi xana sonalou lène
Eééééy Nakarou askan wi ndakham oumpou lène
Kone lolèni khar dimbeulé ak yeurmandé

Beuss bou Yallah sakkeu dem lidieuneti dji
Loumou diokh njaabot ngui lougnou lekk
Sougnou ndéké dougnou agneu
Sougnou agné dougnou rèèr
Té djombeuna di talal sama loxo di gnaane
ééééh éh Fi sabili Lahii hiiii éééh

{Nitdoff}
Han ! yaw ! hé yaw !
6 O’clock nga guèneu sa coner
Keep sa Job té gnémé sa tiono
Niak biy siit daye wané sa djomeuh
Kou bagne koula yapp do deuk ci gnaane
Xol bou sett dou xam kignaane
Louy djitou may dioudou la Borom sakeu weurseuk kone tanouma
Deuk cii djoy diambate khountou ndogaalam daye melni contanouma
Ma ngui dora realize loutahone sama père sévère
Gueudeuna, yédeuna, sagueuna, doorna, xassena nguir ma persévère
Oh God Almighty One (Le Tout-Puissant) mane doy ngama wérou waay
Biss dou gnak cii yonou sabab weurseuk dinama térou waay
Légueutou (Cicatrices) goom yi, kébétou noone yi
Neubeutou mbokk yi, lébati money
Tchine takoul fokk léguette yi mogni
Embouteillage cii sélébé yone yi
Fokk Nga beus waw té euss fanane alleu tawté beus,
Sa gueum gueum warta gawa reuss

{Refrain}
Déguelou lène djoy yi xana sonalou lène
Eééééy Nakarou askan wi ndakham oumpou lène
Kone lolèni khar dimbeulé ak yeurmandé

Beuss bou Yallah sakkeu dem lidieuneti dji
Loumou diokh njaabot ngui lougnou lekk
Sougnou ndéké dougnou agneu
Sougnou agné dougnou rèèr
Té djombeuna di talal sama loxo di gnaane éééééééééh eh
Fi sabili Lahii hiiiiiiiiiiiiiii éééh

Déguelou lène djoy yi
Déguelou lène djoy yi
Déguelou lène djoy yi

Added by

Papi

SHARE

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR