LYRIC

{Intro}
Yeah
i write the right yaa, hun ….

{Couplet #1}
(Bril)
Bén biss nga romb, ma séénla djaar finga aw
Bagn nga rawma takh ma khéép waakhou di daw
Baayi lépp topp sa guinaw
Wola nga takhaw , ma sakh laaf , teup bay wadja naaw
Téggal-la djéguéla , wakh lithi khol bi béguéla
Laathie loula néékh nga wakh, ma défko wanela lépp deuggla
Gueuwouma ni tontou ngama, té dégglou ngama ba djokh ma numéro
Béégna ba mayla bizz bi dokh , rétane nga wanema mééro
Xél bi toukkina sorina , xalat yi tambali beurrina
Djeulna avance bi dotouma tooggati, mbeur mi foutékou beurréna
Nio guéneu di weuri ba tééré fou sori
Té xoolou niou heure yi ,dougouniou thi keur yi
Wakh dina thi beurri , li naniou ko sôôri,
Djappanté doundou li nékk thi coeur yi

{Refrain}
i’m falling in love baby you’re the best
i’m falling in love my baby xol bi yathi né
i’m falling in love baby yawla love
i’m falling in love my baby xol bi yathi né
“””””Come on”””””
Bodoul yaw, dou done kénén my baby yawla love
Yama féégnou wanema, djokhma real love
Ay guintt lama dikké mane, ma yééwou lépp di kémane
Foumala djégué léneu dotouma teuweuti lépp lay meunn

{Couplet #2}
(Mami)
Bou Nitt gniy daanou rap , mane ci iow la danou djiinéé (wakhal way)
Sama Love dafa deuggou, siip nga nimala miinéé (ooh lolou deuggla)
Soma baayé dina taakk , xol bi yeupp nga miné (ah bon)
Douma bayi dara,na done sa sokhna Djarra (amiiin)
Dinala taarbiyou ba djéékh takk ni Ndongo Dara (way li yomboul way-come on)
Beuggnala baby (mala raw)
Beuggnala lol (mala fouf)
Sama gaalé nieupp xaamnagn ni mane iow la love (mala Ussein Bolt)
Nénala dinala seuyeul ,dinala wakh lou néékh
Linga beugg lay déf , Li moy Loove

{Refrain}
i’m falling in love baby you’re the best
i’m falling in love my baby xol bi yathi né
i’m falling in love baby yawla love
i’m falling in love my baby xol bi yathi né
“””””Come on”””””
Bodoul yaw, dou done kénén my baby yawla love
Yama féégnou wanema, djokhma real love
Ay guintt lama dikké mane, ma yééwou lépp di kémane
Foumala djégué léneu dotouma teuweuti lépp lay meunn

{Couplet #3}
(Bril)
Tay waaroul sédd paré ko kharma, légui, mangui thi yone
Dama bawone léppeu lou djeum thi Love, nga tal li fayone
Foumala guissé gueunn di miir di djaaakhlé thi ”sa lééér bi”
Djaral ngama Liguéye Fayéékou wéér, djokhla “salaire bi”
Djéguéma , béguéma, déglouma dégg, ma wakh nga tontouma …
Céédéma, gawééma yééguéma say bou méété séntouma…
Ma tééw nga béék , ay kaf ak rétane laniouy yééndo
*#Walahi_Gangsta_la_té_foumala_guiss_sopékou_Hindo
Khélil ma #café bi lo wakh je suis #avec yay sama#lissa
Thi sama Dieu lay bindeu sa tour bi wola , néla Lis – ça
Yama dakkal djabarou Jay Z, kholouma Rihanna ndakh sa bizz yi
Dara dou easy , gueunnaniou busy , limoy Love té dagn thi Crazy

{Refrain}
i’m falling in love baby you’re the best
i’m falling in love my baby xol bi yathi né
i’m falling in love baby yawla love
i’m falling in love my baby xol bi yathi né
“””””Come on”””””
Bodoul yaw, dou done kénén my baby yawla love
Yama féégnou wanema, djokhma real love
Ay guintt lama dikké mane, ma yééwou lépp di kémane
Foumala djégué léneu dotouma teuweuti lépp lay meunn

{Outro}
Bou Nitt gniy daanou rap , mane ci iow la danou djiinéé (mala Ussein Bolt)
Sama Love dafa deuggou, siip nga nimala miinéé…. RIGHT
Diko djokh gaayi love deug deug
ak ladies yi love deug deug

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR