LYRIC

{Verse 1}
Niaak né tchi guerre tékiwoul né niou ngi tchi jaameuh
Fi lek sunu njite yi séni pouvoir lagni djaamou
Sen bopp ak sen intérêt bopp rek lagni taamou
Waayé Yallah sakogoul mbeur boudoul daanou
Dagn nio gueune djoudou am dagn nio mom
Faté ni chaisou nguur fimou tégo yolom
Kou tokk fékhé noumouy rawalé dom
Fale dom, ndijaay, tanteu, oumpaagne ba tchi goro
Niémé gaadou aakeu tass yaakaar niaakeu dignité
Kou transhumé andeu nguur gui am immunité
Ki falo am deug ki folékou lagni audité
Gaaw tchi takkeu lam opposant sopiko prisonnier
Deuké manipulé sunu Kilifeu diiné
Woté walou saakou niaane lamign yu fess ak digué
Yaarou yaaroulou yéérou ba yorr réwmi guèné sen djiko
Taameuh tapalé ak tigneuleunté ba askane mi miss ko
Sunuy xoulo nieup yegg ko kène dou féké founiou djaubou
Patriotes biniouy mbouboo sakh sène djikoo wané wouko
Dem ba makhé ci nguur lékkeu ba dessal di tuur
Sénégalais nopina waayé lou eupeu tourr

{Refrain}
Dotouniou Nangou
Dotouniou Nangou
Dotouniou Nangou
Non non non Dotouniou Nangou
Dotouniou Nangou
Dotouniou Nangou
Dotouniou Nangou
Légui kouniou door niou fayu
fayu, fayu, fayu, fayu
kouniou door niou fayu

{Verse 2}
Ki fogone ni dara douko fi deudjeuti
Ngélawou mérou askane wé ko yeukeuti
Bign takhé bountou assemblée ni bène niit
Dragon noir sakh yaubou woul sunu fiit
Waayé vocal whatsapp légui sakh da waureudi
Kou wakh lou niaaw ci prési niou Wo leu Dic
Press bi tiit, société civile bi néna miit
Danio raflé djur djuy Bountourngalé (Tchi Bountourngalé)
Ki falo bombe, Dieul nga gni tchi dess fandé
Di Bountourngalé, Di Bountourngalé (Di Bountourngalé)
Ki falo bombe, Gné nène gni tchi dess fandé
Fu Campagne djoté militants yi djaamarlo
Rayanté ndakh Politicien. Mba diar nako ?
Sa dolé deug Sa carte leu. Mba xam ngako ?
Ci yaw lay dess reew mi yaakou mba sopékou

Fayu, Door Fayu, Fayu, Door Fayu, Fayu, Door Fayu
kouniou door niou fayu
Fayu, Door Fayu, Fayu, Door Fayu, Fayu, Door Fayu
kouniou door niou fayu

{Refrain}
Dotouniou Nangou
Dotouniou Nangou
Dotouniou Nangou
Non non non Dotouniou Nangou
Dotouniou Nangou
Dotouniou Nangou
Dotouniou Nangou
Légui kouniou door niou fayu
fayu, fayu, fayu, fayu
kouniou door niou fayu

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR