LYRIC

Tragédie samay textes melni jean racine
Mane même si diiné comme imam j’eleve et j’enracine
Mbed moy wakh pr meune ma degg donnal boudiouman
May Macleod
Nel yenen immortels yi geuwma niou goudou fann
Fok am ay rappeur yousene tour di dem nom des bavards
Ndakh amna niouy rap par amour am niouy rap par hasard
God dafma béral yone à part may daw ni ap sakhar
Même bodone merlin l’enchanteur doutax nga meune def kar sa kar
Mission bi dorna depuis first bi scène 2010
May passe ni 10 dou tokk même bougnma denkone 2000 (6)siss
Si kar nga giss sa bop dioumo yangsi si yone bi fils
Geunelene djiné
Bo weddé andilma 2000 deum giss
Nelen tay mafi né xawma sakh ndakh amna niou dess
Takh soumay rap même bougn done youssoupha sakh dougn def geste
Baye dangma xiif mai baye fall bi boko tiobbé dou ress
Li leer ba leer moy dougn ay athlètes mai nieup dagnmay daw ni peste
Job bi day rare ni ambulance accident ak corbillard
Di def lou formidable
Mane laniouy sett ni tiabbi fort boyard
Ladjal school yima diota diar ndakh meussna done nullard
Boulma jangal louy liberté meussna done taulard
Symboliste ni Baudelaire Verlaine ak mallarmé
Viens pas foutre le bordel man si t’es mal armé
Deter et acharné on s’envole vers le titre
Lis les lignes de mon destin et voilà un nouveau chapitre
Fi gayou yoroul montre beug kepp tense
Rappeur bougn wo fi a la barre nga diokhniou lap dance
Real mounoul yor texte fake
Guéné nga mixtape mai dafay melni sextape
Damay rap sassouné limay def crime di yok
Ta gnifi né moune nalene ray ak bene ligne ni coke
Malene meune dou diar makoy wakh si ay nienty lakk
Takh fougn ma giss daniouy seyy melni kougn né sa gallei ngi taak
Diabou bandit dou wa ondou ngakoy jaay
Pour son bi def FM dou diar sa onde makoy raay boy may
Sakharal game bi ni thiouray sa neggou mère
Ndakh chak jr damay am ni journal télévisé ak guerre fuck i
Gotta here
Njaxass style ni tiobou talibé
Flow bi day calibré nieup validé né amna qualité
Brique si kaw beat ba bountou boulevard yeup balisé
Bandit black break sa bad block bindeum batiné
Simil sappo bi siki saka may Sapobi
Soko sokké dou sotti kou saurou sabba sipp sakkou yi ,ça yé Seyy nga ni Sarkozy scène bi safna may sappali sirrou strophe yi lay soppi seuss sope same lim samp Ni lamp bi
Teggat tank yi topp thèmes yiniouy teppi di togue Tek si kaw table yi
Tas wou textes mouy taarou ni tirou toti dou taabi day teggi teeré si takk bi tourou tangue di taclé tourné temps ba dem terminus
Boul sakh sonn yangi def ay bruits mai mounoul riir
Kouné la Kar dou lyriciste da fek mounoul lire
Manguek xel ak clairvoyance dou giss bene defaillance
Docteur bi talent momay fathj yaw nak ay test ak ordonnance
Back ni Jésus Christ attaque dougeul ni messi cris
Di Fuck sa mère sa pa di tathiou nanema merci fils
Courant ak coupure soyez en sûr k dingene lâché prise
Pour son bi daw radio dou diar mo’fucker massiy lâché jizz
PD
Diaro bayi si keur
May Attaqué ngay pédalé melni ap bicycle
Djinné rhymes dou ay démons lay tok nioumay tiiteul
Je marche seul mes voyants sont au vert kone leer bi lay jiiteul
Brûle 1000 je brûle 2000 feux
Dougeuk hargne seni défense yimay tass ni Dioufou 2002
Classik d’oeuvre d’art pourtant jsui pa mosart je fais des punchs rares on dirait Sada Kane et son fameux regard
Damn
Andando ni classe ak craie
Dama plausif exhaustif explosif like DrDre
Fuck trône waxko gni am tempwou tok
Mane mangi work limay beureung toum ndakh xamni buur dou mbok kone One more time ana montre you bakhi
Soldier si kaki flavor you diakhi bou fake yi reuthj si track yi
Dangay dund mai pr geune soukratt
Même souma dewone dalay déssé waur ni mo’fucker yi gun 2pac

Yeah
Karballah jahmerue senlyrics
Tek tank the mixtape
29 septembre dans les bacs
Aight
Kzééé

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR