LYRIC

{Verse I}
All the day , haal bi day gueuna yokou « okay »
By the way , baye yi wéy , fépp yakou « ésskéy »
Hey kaay dougatt feel , naaw wouthi sky
Yéék fly the God Bril nieuw ngéni éss try
Deuppeu dippi phasam –gueuna djégué niggazeum
Djapp ngathi phrasam- Yi nioula yéggué nék-nga-zeum
Meussoul daw – walam, moytoul dawalam
Kiy soppi péép soungouff , boul deuboul da wal am ?
Lithi kamil la niam dokh thi beatou platinum
Nékatt thi millénium – khoss ko thi platineum
Batine bi eumb lépp, ba team bi romb fépp
Thiafka rime bi, déf crime bi, xatim bi djomb nieupp
Systéme bangui dém, I’m killin’em-
6 thémes ngathi djém – kham clean’eum
Sétt wéthieu la déf, séét waathie la khéf
Baakla djeuf, baathie-la keuf sa warééf

{CHORUS}
Sunu fight dou foo thi right , it’s time niou nieuw
« nioy déf li gueun, taal faya di burn
Ték lii gun, déf deugueun-tann, fépp di beuneu
This is the fight thi « 4 » , we like , hey you gotta know
« dina gueuna, yaggueu, gueuneu meuna
Yéggueu founé ana – Gni gueumoul niouna

{Verse II}
Eh yaw djouk gueuna gueum, djappeu thi right away
look bania gueumeu djapp yi fi nara wééy
yokhla wathieu cééy, djokhla , wakhla everyday
miss-nga what we say , guiss nga , dégg nga , by the way
baatt yi naaw di dém wouti nopp di nieuw
bouthi sakh am diléme dagn thi wopp you know
gni meun thi rhyme lim mathi I’m so lyrical
sama biir mind limathi am sour liir yi keul
boy woute punchline, dadjék barigo
kiy open sa line, da djék bari go
ndjaap guéneu weuri lou beuri wagni fi fitna
rap gueuna sari thi keur yi mégneu fa fiteu na.
Supa dupa di rime , soga deupp di miim, wakhou niéne gni, yéné yi souko nieupp di tiim
Forever gueuna job , whatever sunu bopp ,
Hey never bouniou topp, game-over douniou stop

{CHORUS}
Sunu fight dou foo thi right , it’s time niou nieuw
« nioy déf li gueun, taal faya di burn –
Ték lii gun , déf deugueun-tann , fépp di beuneu
This is the fight thi « 4 », we like, hey you gotta know
« dina gueuna, yaggueu, gueuneu meuna
Yéggueu founé ana – Gni gueumoul niouna

{Bridge}
« Power of wisdom, thought and word is the weapon of the strong intelligent man
A wise man is respect with his mind »
Sunu fight dou foo thi right , it’s time niou nieuw
« Thiaroye-Diamaguéne, I’m the best , the number one »
This is the fight thi « 4 » , we like , hey you gotta know
« Welcome to the hood – niolay may li dakk , li gayi di déf sén album »
« Rap rék laniouy déf –real shit for the real niggiz »
This is the Fight thi « 4 » , we like , hey you gotta know.
El Messias !!!!

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR