LYRIC

{Intro}
“I’m a born soldier moving through the hope.
Niggaz i’ma goin true , no matter what you think…
I got it on my mind cuz i know i’m goin true
so you can stand ”
Yeah stand up , Mama G on da beat
The Last fighter in da house “ANALYZIK”
Eletrique mind , ELectro’Rhyme

{Couplet 1}
Djotna tay niou deuggeuté #Faux , Andd eundi fi#Vrai
Waathé #excés , tégui #défaut, wakhla nokoy Vivré
Sa diggou bopp ba thi sa soufou tank féppay #Vibré
Just like that, doné niou djakkeu am envie beuré
Djappal tour yi , gueunn niou sauri, daniou beuri katane
Niongui touri , boul niou sori, djaroul weuri kaay tann
Hello , fi lo, guiss niounela , feelo
Low low , don’t go, niou djokhla bénén philo
Dou #Maxwell dou #Faraday , This is “the supa Theory”
Meukk ci well , fayi daay, nane thi né soupa té weuri
Djégué ci kouné di baap, dougou ci louné sabapp,
Meuna dokh thi #circuit Bouné , yéégg ci founé di Rap
You know what it is, Fokk war yi diss
Niou djendiwaati Rizz , keuthie bén weuri diss
Niongui yéggali, dogali, yéggueu thi, Toppeuthi beuugg di dém ,
Yeungueuli , tangali, yaggeuthi , bokkouthi teugg di djém

{Refrain}
(Rap)
Légui guiss naniou , khamnaniou yone wi té niongui nieuw
Yokkou #Tension thi rime yi flow yi naw
#Résistance bi di bania guéstou thi guinaw
#Intensité bi thi sunu mind la , now you know
(Chant)
Légui guiss naniou , khamnaniou yone wi té niongui nieuw
Yokkou #Tension thi rime yi flow yi naw
#Résistance bi di bania guéstou thi guinaw
#Intensité bi thi sunu mind la , now you know

{Couplet 2}
Ndieukkeu thi gueuna beuss , yaggueu thi gueuna feuss
Di weuri di indi, lou beuri niou dindi done first
tokk ci ville bi , sopi deal bi , rothi #fil bi #réseau bi daw
Wakh civile bi, yokkou dal bi , am thiofél bi rassou thi daaw
Niou bayi waar yi , di bania worry té tékk lou baari
Douniou bayi weuri ba djott xibaar yi thi everybody
***i’m sorry**** meunouniou bokk #D_D_P(Différence De Potentiel)
May ki yéék ba gueuna sori fi ki beugga Déé Deupé
Laal nga #Eletrique mind yeukk ay Djouni #Ampére
Ték thi brikk, sunshine, dome bou djoudou am père
I’m back , ki done xaxataay doto guiss siiigneumm
Naangko xam thi téél , #électron dou sopi #signeum
Yéék sa xél té yeugouloko , dikk xol ko yokhouloko
djokh ko lokho soukouloko , tékna djéégué djouk thi laago
Défna échos déggouloko, féék guissoko yeungaloko
Yangui doga dougou nigga #systéme bi djangouloko

{Refrain}
(Rap)
Légui guiss naniou , khamnaniou yone wi té niongui nieuw
Yokkou #Tension thi rime yi flow yi naw
#Résistance bi di bania guéstou thi guinaw
#Intensité bi thi sunu mind la , now you know
(Chant)
Légui guiss naniou , khamnaniou yone wi té niongui nieuw
Yokkou #Tension thi rime yi flow yi naw
#Résistance bi di bania guéstou thi guinaw
#Intensité bi thi sunu mind la , now you know

{Bridge}
Eltrik mind – yangui élctrik time
(Fok nga dadjalé tééméri mc thi bén mind , soga am Bril “the last fighter”
tHis is da supa dupa on da eltrik mind

(Chant)
Légui guiss naniou , khamnaniou yone wi té niongui nieuw
Yokkou #Tension thi rime yi flow yi naw
#Résistance bi di bania guéstou thi guinaw
#Intensité bi thi sunu mind la , now you know

{Bridge}
Eltrik mind – yangui élctrik time
Eltrik mind – é-é-éltrik Rhyme
Eltrik mind – yangui élctrik time
tHis is da supa dupa on da eltrik mind

{Outro}
Malén nanelo apéritif , yeungueul move bi ni bén #charge thi #champ_électrique
Djokhlén Analyzik bi , aathie barre yi bay lal ay sattelite
Sopi Annalou Zik bi

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR