LYRIC

Seu projet ken meussouko khaar
Homy lane la tchi meune ?
Forcing bi nieup tchi marre
Homy lane la tchi meune?
Saayo xewlé ken dou nieuw
Homy lane la tchi meune ?
Yaak sa gars yi réunion dima dieuw
Mais lane la tchi meune !
Nitteu gueuneu meuneu bagn nitt
Motah rappeur yi niofi gueuneu meuneu bagn rappeur
Nénagne meu “Free sa flow dina réy nitt”
Lima lerr moy douma baal bèneu rappeur (douma kèneu)
Awouma temps boudoul money boy (Awouma temps)
Am ngène chance damay djangui wone (Mane dama djangui wone)
Mayé nangou baxoul dédeeeeet
Mayoma mayma jaameuh nangou défaite (mayma jaameuh dong boy)
Zonou town mako ress boy (mako ress, mako ress )
Soma songué nala pess boy (nala pess, nala pess boy)
Mane soxla wouma press wala [ass cote]
I’m the fucking best bouma stress bouma test boy
Samay vestes do guiss kène sole
Toujours classe fuck sa dress code
Amena ay Ex yumay tek choc dima yoné texte
Dima es. (espérer) pour niou sport
Yian xamna malène meune, Ben xamna malène meune
Wakh kat yi ba lène rek wa kogne bi ak kogne bé yeup mane lagn gueum

{Pont 1}
Malembé Malembé
Free def niou ndank ya aliéné
Beuri ay MC yu xalélé
Togne nagn leu moss waayé baal lène rek

{Refrain}
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Free def niou ndank ya aliéné
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Togne nagn leu moss waayé baal lène rek

{Verse 2}
Yeah seu clip kène beugouko share
Homy lane la tchi meune?
Amo ay mix mister Thier
WoOOooo ! Homy lane la tchi meune?
Jamdong bi nga done xépp tay mola gueuneu cher
Homy lane la tchi meune?
Sa wa kogne mane laniou défal car nieuw sétane ci sama scène
Homy lane la tchi meune ?
Lane la tchi meune ?
Mane défar ay Hit sama maladie leu
Yaw nullard ngeu lolou rk la xalate tchi yaw
Té nioune rek nga fan diniou mbalag di saupe
Sa daw fassou daaaw dotoul dalaate tchi yaw
Xamal ni kalé nga ndakh fi ngako beug kalaate dou fofou
Chaque jour liguèy sama calendrier (Liguèy rek liguèy rek)
Fi amo fi ndieurigne comme salade ci deummeu
Défal ndank !
Bi lepp né séléw mane ma nieuw yengueulaate leu yéé leu
Ma nieuw yégueulaate sa level ya meuneu faaté ba yeem meu
Bi sèn game bi di nélaw ma nieuw nexalaate yeah mane
Ma indi rap bi nga yélole push ko ni Baba ak Yééla

{Pont 2}
Malembé Malembé
Gnima done dinkaate nieup nalène béteu
Ma ngi tchi djawou dji. Yeen fane ngène né ?
Dina lène diokh sen dose ba ngèn bék

{Refrain}
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Free def niou ndank ya aliéné
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Togne nagn leu moss waayé baal lène rek

{Verse 3}
Yeah ! Kène meunoul téé lima done di ….
Tell them dama nieuw ngir fay leu (Dama nëk)
Mane ak yeen on est trop différent (Dawal)
Dama original yeen ngène copier yéémeu (Baayi lène di topando)
Douma nopi ndakh amna avenir douma salopard
Dama xiff meun na lekk yappou charognard
Douma domou riche awma avocat
Té féppeu la son bi di daw diaroul à vos marques

Malembé Malembé
Malembé Malembé

Malembé = Doucement, Lentement

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR