LYRIC

{Refrain}Galsen Lyrics
Ni lagn kay défé
Nigga soma guissé nangoul ni guiss nga sa défaite
Gagné wala gagné match nul YALLAH téré
Fayma sama Money nio ngi tchi dernier délai
Rest In Peace ci sen carrière
Douma Rappeur Opposition niom nieup danio trokh
Melni Rappeurs Opposition trokh teksi sokhor
Té dougne….
Nangoul, nangoul, Nangoul ndogal
Nangoul, nangoul gueumeul YALLAH
Nangoul ndogal

{Verse 1}
Niouné Xaliss Seytané leu ma ngek Ibliss sama poche
Police escorté meu Président laay topando
Arrosél cimetière yu bess yi sama néew yi féex
NATHIE bi rekkay deugueul WERR bi fa la né di GUEINTE
Sacrifice yi niomay djaay, ray ma gaaw bala sa jour-rou déh
Niaakeu nangou mo ray Lucifer, dama djoudou fek musique déh
Libre ni kou djoudou tchi biir jail
Yaapeu gnimay reubbeu mom laay dibi tay
Tuur sa dérett ci biir piscine bi
Fauute tchi gucci, fauute tchi Philip plein
Nénagn meu thiat dafa gaaw, lawlathiat may laale xaliss
Nieupeu naane meu laalale banteu #GalsenLyrics.com
Ennemi door yi ngamay door yéggueugou ma tchi dara baayil dima dooré ndankeu
Sani kherr, mane ay niaanamay dall, YALLAH méy TIRé ndam lamay djam
Takkal teeré; takkalma médaille. Yoro touss parce que nioune xam nagne niata ngay diarr

{Refrain}
Enemy doundeul, doundeul
Enemy doundeul waaay
Enemy doundeul, doundeul
Enemy doundeul, doundeul
Enemy doundeul, doundeul
Enemy doundeul waaay
Enemy doundeul, doundeul
Enemy doundeul, doundeul

Ni lagn kay défé
Nigga soma guissé nangoul ni guiss nga sa défaite
Gagné wala gagné match nul YALLAH téré
Fayma sama Money nio ngi tchi dernier délai
Rest In Peace ci sen carrière
Douma Rappeur Opposition niom nieup danio trokh
Melni Rappeurs Opposition trokh teksi sokhor
Té dougne….
Nangoul, nangoul, Nangoul ndogal
Nangoul, nangoul gueumeul YALLAH #GalsenLyrics.com
Nangoul ndogal

{Verse 2}
Hann ! YALLAH tathiouma ma féthieu
Mou dioxma micro ma way
Ma Liguèy mou bindeul meu chèque
Wathié sama bopp moumay gueuneu feusseul
Yone bou djoupe ni ballou fétél
Raggal Yallah raggal nélaw
Raggal Yallah raggal nélaw
Bo déwé nélaw nga, bo nélawé déh nga
Démal ba tchi nigga bila dieundeu néko djaay boppam dou takh mou am sama njeuk
Candidat pour nek Président kone yaw ak Microphone bi yeup mo f****r
Wourouss sama nguirou doundou bo gueunoul goudou fane Meuwty doma folliii never #GalsenLyrics.com
Pauvre bou rafett mo gueuneu niaaw milliardaire bou niaaw Palais fa laay défé make-up

{Pont}
Dérett sama chainou Or ragalouma gnimay fompal sama diamant
Peuple bi amouniou solution sama problèmou galé wakhone nako sama maman
Président la beug done niom nio yorr Papa sama gouvernement
Domou kou raggal liguèy niémé téki dom djodjou imbécile leu évidemment

{Refrain}
Enemy doundeul, doundeul
Enemy doundeul waaay
Enemy doundeul, doundeul
Enemy doundeul, doundeul
Enemy doundeul, doundeul #GalsenLyrics.com
Enemy doundeul waaay
Enemy doundeul, doundeul
Enemy doundeul, doundeul

Ni lagn kay défé
Nigga soma guissé nangoul ni guiss nga sa défaite
Gagné wala gagné match nul YALLAH téré
Fayma sama Money nio ngi tchi dernier délai
Rest In Peace ci sen carrière
Douma Rappeur Opposition niom nieup danio trokh
Melni Rappeurs Opposition trokh teksi sokhor
Té dougne….
Nangoul, nangoul, Nangoul ndogal
Nangoul, nangoul gueumeul YALLAH
Nangoul ndogal

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR