LYRIC

Bril Fight 4 – Verse 1}
Bi dara nekkagoul ,,, laniou reudd fimou djeumm
Mou guiss lithi yone wi Doga Naw wouti djeumeu
djoudou ,foudou , ram djoukk dokh guéneu weuri
Yagga rigou djang kham siggui songou waar yi,,,,
Djouguéna thi leundeum , guéneuna thi peundeum, yeulbouna dogou nathi wouti dji na leer
Delou na thi djeumeum – sentou nathi djaamam, seugg dithi weur Li tchi neubou dina leer
Limou sopp deugg , ditchi seugg ,kouko feuggg,, dinga degg , bek yokhou djégué wané ninga yeugué
Diko gueuna ,beuggg, yeukko deugg deugg , téla yegg tankeu diko weugg,
Doga Egg fingay yééguée
khol thi demb defko tay beuga sopi souba
Beugatouniou deggg ben moushiba
It’s time nieup doundou revolution
Niou oubi sunu mind djèma Weuri evolution

{Sir Jamal – Verse 1}
Kou tchi yakamti yakoulé
Waayé bo waxoulé ya khoulé
Bo sangané sakh sa weurseuk bala nga tchii djot dagn lay ndouli
Doumeuyou cii lepp loulay délo guinaw boul djay ndioulé
Diém teulé ayoul yokal waar ba kérok bouniou lay djoulé

{Refrain}
Boy dokh saay tanke tek ko cii yonu Evolution Mind
Moy takh sa Sun meuneu Shine
Cii révolution Time
(Evolution)
Boy dawite saay tanke tek ko cii yonu Evolution Mind
Moy takh sa Sun meuneu Shine
Cii révolution Time

{Sir Jamal – Verse 2}
Sa beut nala guiss lo lepp louniou mour
Bou djante bi di Soow nala fek ak Humour
Sa xoll na ngo ko beuss té nga takk saay dalleu
Ba sa xell bou na-ngo dana takk dji daa leu
Djafé djafé dou tchi niak nonou la démé
Soukeur la cii gni té Kaané cii gné
Yaw limay lay diggueul moy nga djaapaki deux mains
Ndakh sa life yaw rek yakoy reude di signé

{Bril Fight 4 – Verse 2}
Naniou takkou khaaré , dogou deuk tchi liguéy
Waagni wakh dji, deugou djeuf khoumbal li ,guééy
Seugg, soukou lay, toyal lépp ni lay
Di déf souf , djouk ouf , bayi di lay
Tchi bor yi , guéné fay, loufi takkati niou fay
soti yokkou thi sifaay, meuna fateu souniou faille
Wakhou gueuna waaf , wouti laaf meuna fly

{Sir Jamal}
Humm humm! Mané benn ngok
Na nga gueum ni di nga tchi guèneu
Mané Niar-rangok
Nga mbogg ba nopi xam ni yay ki gueune
{Bril Fight 4}
Yaw ! Time goes on , nanga fékhé djeum kanam, waro tokk ditchi khol , “baye fékhél”
Niaafé tchi sa zone, gueuna kharé, guéné li tchi yaw boul topp sa xol ” bayi fé xél”

{Refrain}
Boy dokh saay tanke tek ko cii yonu Evolution Mind
Moy takh sa Sun meuneu Shine
Cii révolution Time
(Evolution)
Boy dawite saay tanke tek ko cii yonu Evolution Mind
Moy takh sa Sun meuneu Shine (Sa Sun meuneu Shine)
Cii révolution Time

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR