LYRIC

{Refrain}
Politique ci sound yi
Légui lepp fi faux
Nieupeuy job pour down yi
Légui lepp fi faux
Légui lepp fi faux
Légui lepp fi faux, fi faux
Légui lepp fi faux, fi faux
Légui lepp fi faux, fi faux
Everything is fake

{Iss 814}
Niata nioy doundou faux prêché vrai
Kagne ngay délou sa Papa sans égo pour néko say wakh père c’est vrai
Est-ce que diarna di reuthiou bakkaar yi précédés ?
Ndakh kiy wakh wakhou YALLAH moy doundou comme koudoul décédé
Ci deuk bou paré toppeu ni njouli
Dieul lingué yi diébeulko selbé
Boumla diakhal bo guissé xeureum kat def taatou nèène di diouli
Fi leppeuh faux
Comme 100% qualité bou am défaut
Etat bi moussoul wakh ci baune yi Dic di pass
Rongognou Badola mi ngi ci verrou nit biy kass
Dérettou Sénégal moy Tapis Rouge biniou laalale France
Guinaar Sodomisé Gaïndé paré néko laalale Tranche
Diaroul guiss ay rapport pour xamni ngour amna Vol
Xam xam fane ngakay sakkou ndakh école amna Viol
Dém ba Bone nek Règles fane ngay guiss mbaakh
Badola beuréék dépense yaw say fils ndiaakh

{Refrain 2}
Plastique ci down yi
Légui lepp fi faux
Président ci round yi
Légui lepp fi faux
Politique ci sound yi
Légui lepp fi faux
Domou Serigne ci boy town yi
Légui lepp fi faux
Légui lepp fi faux
Légui lepp fi faux, fi faux
Légui lepp fi faux, fi faux
Légui lepp fi faux, fi faux
Everything is fake

{Djily Bagdad}
Niouy dokh di wakh ci ay fèneu ngir intérêts ak profits
Valeurs zéro kène calculé toul ndakh lepp faux fi
Wakhoumala down yi mais xel yi laniou plastifié
Mbeuguel deug amatoul ay xollou photocopie
Faux ni lek ribba meuni Thione lagni nocé
Faux tchi séni guiss ndakh xeff yi sakh dagneka possé
Faux ni deuneu bou daanu niou pathialaate
Saf sappeuh ni kani salade
Faux ni démocratie bou kèneu sagnoula wakh sa xalaate
Dagni marr naane dieundii peutite rombeu feulé ndokh
Fi dara diarou fi yone parce que nieupeu tégui
Iblis tek fi tankeu tchi leundeum lagni dokh
Fi lèneu rk mofi deugou moy sunu talon dall yi
Waayé gniy vrais ngi resté vrais même bougnouy doundeu à genoux
Té bo dagone séni tankeu sakh lagni gueuneu deugou
Jeunesse bou amatoul références gni warone neu bagne nangou
Tay Goor day saf djiguène nioulay gueumlo dafa am gout

{Refrain 2}
Plastique ci down yi
Légui lepp fi faux
Président ci round yi
Légui lepp fi faux
Plotique ci sound yi
Légui lepp fi faux
Domou Serigne ci boy town yi
Légui lepp fi faux
Légui lepp fi faux
Légui lepp fi faux, fi faux
Légui lepp fi faux, fi faux
Légui lepp fi faux, fi faux
Everything is fake

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR