LYRIC

Chorus ( Nitdoff & Mao)
Fokk ma lathie !!! Liiddé Liiddé Kagn Lay Diekh (X3 )
Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou tontou
Fokk ma lathie !!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diékh
Yo ! Fokk ma lathie !!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diékh
Who? my nigga
Fokk ma lathie !!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diekh
Yow ! Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou tontou
Fokk ma lathie

(1er Couplet)
Fokk ma lathie
Loutakh léppeu keupou ci mane
Loutakh maay xeuy di wékou cii nit té kèn dou wéku cii mane
Loutakh may xeuy di tèneu di xoll té douma sèneu assamane
Loutakh sama life tiss nioumaay xolé beutou ndeyesane
Daniou maay khép douniou maa guiss daniou maay rombe né seun
Maay gueuneu nour si guédjiou nakkar, he can’t understand
Sama fiit meuneu toul tokk ndakh ay yakaar you tass
Dama aay gaaf ci pét wala ma niaka daw fass
Sama xoll di diékh vide nii sama calpé
Niak singuilima foutima dima palpé
Sama doundou wét melni ndiouly bou amoul salbé
Maay xeuy di lathié louma def ba mérité li
Mba dou sama liguéyou ndéye cii la herité li
Bissbou nek limouy indi cii ay khétou problème
Diougué Tchii li danou tchii lé da ngay djiém té do dém
Niou ték la yafouss
vaut rien bi tekki wo touss

Chorus ( Nitdoff & Mao)
Fokk ma lathie !!! Liiddé Liiddé Kagn Lay Diekh (X3 )
Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou tontou
Fokk ma lathie !!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diékh
Yo ! Fokk ma lathie !!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diékh
Who? my nigga
Fokk ma lathie !!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diekh
Yow ! Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou tontou

(2ème Couplet )
Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss kou tontou
Lou lakhe ma ndagou sakou am am di xeuy di gontou
Té Meunone def ni niome tokk cii Boppou kogn bi Fontou
Beuri diom maa takh ma bania tokk si keur gui nioumaay khonetou
Té Fouma démé baye aamé yakar life bi dathie ma pontou
Maa danou waatt cii kambe gui Tambalé waatt à zéro
Souma ko diappé ni dina yékha warr Pagérot
Saalite-tangue maay yott seung sama geueme felleu
Mougn na ba sama mougnou kaay fessena Delleu
Magui cracké tchii yonu sinébare ak guène Braqué
Sama égo yegg naa boppam Beutt yi nioma traqué
Di blamé Baa cii askane wi ma bokk dagne maa plané

Chorus ( Nitdoff & Mao)
Fokk ma lathie !!! Liiddé Liiddé Kagn Lay Diekh (X3 )
Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou tontou
Fokk ma lathie !!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diékh
Yo ! Fokk ma lathie !!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diékh
Who? my nigga
Fokk ma lathie !!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diekh
Yow ! Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou tontou
Fokk ma lathie

(3ème couplet)
Souma Néwé ciii geunte Feugue maa néma diougeul
Mane Limaay dounde ni natou leu wala mbougeul
Tamouma di Loubeul damaay Liguèye di dioubeul
Cii ndiguel la meusseu sakh di moytou loumay diggeul
Souffél sama bopp té kouma guiss Daadi laay yégeul
Waayé melnani taay yoyou djiko niomay téggeul
Bonne daffa yombeu
Beuri wonne neu loumay diombeu
Beuss bou né niou khassma né meu sa morom yagui laay rombeu
Nit gni danio yakamm ti ta yalla daffa Yékh
Ko tchii wakh Mouné leu Def lou bakh mofii diékh
Bène lakk laniou dégue mouy CFA
Boka yoroul légui Le courant ne passe pas

Chorus ( Nitdoff & Mao)
Fokk ma lathie !!! Liiddé Liiddé Kagn Lay diekh X3
Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou tontou
Fokk ma lathie !!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diekh X3
Fokk ma Lathie Lathie lathie ba guiss Kou tontou
Fokk ma lathie
Lathie ba guiss kou tontou
Fokk ma lathie

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR