LYRIC

{CHORUS}
Tok tok rongogn yi mba dou far eundi fire (faya)
Fok niou ande yoboulén ba yégg higher higher ( haya, haya)
Diouniou sétane ngéni die , danio wakh thi bépp faille ,
founiou sén lou mélni daay, tourfa ndokh ba lépp faay
Tok tok rongogn yi mba dou far eundi fire (faya)
Fok niou ande yoboulén ba yégg higher higher ( haya, haya)
Diouniou sétane yénn ngéni die , daaniou wakh thi séni faille ,
founiou sén lou mélni daay, tourfa ndokh ba lépp faay.

{VERSE I}
Waathielénn, djokou, yokou fompi rongogn nopilénn
Wathielénn, yokou, mbokou , fokkniou dikk soppil-lén
Sénn doundou, oundou yék thi andou bépp toundou wané
Lépp djapp onde, randoul andou djaroul khoundou niouné
niongui djémm douniou baayi , ba kouné meuna démm gueuna bayi
Fokk kouné di thi djote douniou taayi, yokoula souli mbotou djotay yi
Di guéné li gueun, nga gueuna di gueum, niou wané deugueun , seugueum
Armé nagne sa gun , fékhé ko gueum, sa khipi sa khéf sa gueume
Léne douniou thi meuna rhér, Niothi agne tibb thi guéné réér
« Nioune » nio di sén bate , nioy wagni sénn yéén
Niodi fôôte wi soumbate, guiss nga niongui sén yhénn
Bépp pépp pépp :!! , séni nakar toyna fépp
Bayi tépp tépp , thi léppe , dém ba dagne thi khépp
Faate gni léni noote — faléwougne menotte
Beuré, kharé figne niou khaaré , paré djeuli note
Boote askan wi, roote , yoote , yauute , forli rote.

{CHORUS}
Tok tok rongogn yi mba dou far eundi fire (faya)
Fok niou ande yoboulén ba yégg higher higher ( haya, haya)
Diouniou sétane ngéni die , danio wakh thi bépp faille ,
founiou sén lou mélni daay, tourfa ndokh ba lépp faay
Tok tok rongogn yi mba dou far eundi fire (faya)
Fok niou ande yoboulén ba yégg higher higher ( haya, haya)
Diouniou sétane yénn ngéni die , daaniou wakh thi séni faille ,
founiou sén lou mélni daay, tourfa ndokh ba lépp faay.

{VERSE II}
Yéén dotoul én lak, kén djotoulén laak, léne , togouniou, déglouniou
séni khoundou day dakk
Ndjaap , daap ,sén banékh moniou soop thi guédjiou thioono.
Djap lépp dém ba nékh laniou sopp djégui noono
Fipou, fompou , yokou fitt wakhou wouti fi lépp doré
Deupp, yappla tawkhitt wakhla ngir nga bagne di dooré
Meuna, touniou tokk di djéw , gni khamb tal yi dilén faatt
Mana, kifi nara téw djeul gni waathie thi tali yi dilénn fatt
Thi keur yi leulou tokk thi dér yi , défni niom ak séni doom yi
Teuri bayi takkdéryi di ray mélni niou nane thi doom yi
Sani khér boul thi dougou – Moytou guerre nagne thi deugou
Cartou electeur yay sopi dictateur yi nagne thi dogou. CHORUS
Tok tok rongogn yi mba dou far eundi fire (faya)
Fok niou ande yoboulén ba yégg higher higher ( haya, haya)
Diouniou sétane ngéni die, danio wakh thi bépp faille ,
founiou sén lou mélni daay, tourfa ndokh ba lépp faay
Tok tok rongogn yi mba dou far eundi fire (faya)
Fok niou ande yoboulén ba yégg higher higher ( haya, haya)
Diouniou sétane yénn ngéni die , daaniou wakh thi séni faille ,
founiou sén lou mélni daay, tourfa ndokh ba lépp faay.
·
{VERSE III}
Khipilén bou kéne nélaw ,
Métit yangui gueuna law
Deuk bangui gueuna tangui, askan wéma yoni yaw
Nénaniou ,dégouniou , guissouniou, bégouniou, bissouniou, yeugouniou, dikkiniou
bayil niou deukheuniou, tokhouniou , sorriniou « niétélou candidature beugouniou »
Délén teureuri , weuri , wakh lou beuri yék fou sori
Dounou téla réri mbir yi dina lééri , nang ko soori
Nioy acteur yi , thi mbédd yi ak keur yi
Gniy wané vecteur yi , nieuw séddal sén cœur yi
Guissoulén niou lék teuri , nioy bindeu ba yénn heure yi
Kassal lén thi lecteur yi – fathie gome yi ak Eur yi
Dougou thi deuk bi, yeukeuti Euk bi, wanéfi Oukou bi, deugg bi
Seugg thi mbinde mi, wakh thi mbeunde mi, courant ak ndokmi mbeukk mi

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR