LYRIC

Okay My Check
Reptyle Music
Yeah Check

{Verse}
Lalale antenne bi télé bé dessé lerr
Derr bou nioule bi gueunone na sett bala Aimé Césaire
Fi Mère bi guedj na togueu rèrr namouniou thiéré ak méw
Wakhal sa guel ni damay job comme boum-ma sms
Gni moudjé toujours moy gni def li ndieukeu nieuw sen xel
Bo meusseu déviergé waro bagne diabaour deuxième main
Meusso lène meu may dara lima wara lekk rek lay lekk
Kone souma déwé rek xamal sama weurseuk nga diekh
Rakk boy maggueuh di xepp li nga ragalone def
Temps bi wormal neu bakar yifi gueunone neu yëss
Yaw ya ngui cii niaar niou beugueunté waroul nioulène téré seuy
Lo xam cii musulman bou takkeu niaari chrétiennes
Mbeuguel leulay doundeul Xaliss moy liy dalal sa xel
Meuss nga tayéleu doundeu waayé meusso sawara déh
Mane bamay fébar ci Rap fékk neu garap yeup diekh
Mane deumeu la ci Rap niom ay domou Adama lagne
Jahjëfëté gni nangou malène meune Jahjëfëté
Gnénène gniy xeuthio ngour gui nélène niou khaar bama déh
Maame bouma djay baay, bouma yéddeu Yaay nianal meu rek
Yeah Leundeum-maayou Diaam yi taxoul ma djaay sama lerr
Ghetto tollou banditisme kouné ngui baye sa waar
Double feuille pour taukh baune leu nékoul pour def devoir
Li nga nangou cii sama Yaay ngay dem may sa Yaay
Xaliss amoul xett waayé moy guili ci Karim Maïssa Wade
Pour yaw loutah guéweul yeup xam Mamour Cheikh Amar
Loutah sama kogne yéneu déféant yi beug xéx ak mane
Parce que Rap fay nama boy mane beugueutouma dem France
Dégueu nga maam mane boy you fallaaw rekkay Follow sama Instagram
Sen chef de Gang yi la ndieukeu saaf ni ay guerté thiaaf
Rangél say bagage té nga gaaw té dém ni kou seuy ba tass
Sama song yeupeu ngui fepp té encaissé wouma BSDA
Comme kogne ba nieupeu am chaine mais kèneu dou fay Canal
Sa salairou Papa matoul sakh sen lekk ak naane mais mo ngui fay chaque mois
Yaw lane mola téré done pé sen classe
Geudj na ci bopp kogne bi fils ma ngui ci job bi fils
Kène téréwouma nekk boy bou positif ak poche you diss
Album bi légui mou paré ma ngui ci derniers réglages yi
Tête de mort cii sama verre yi sen déh rek lay guiss
Nioulay khaar nga guéné xaliss yaw ngay reuy lamigne
Meuno reuy lamigne ba raw kou dem police né rayna Niit
Guiss na kou déguisé wou goumbeu jog dém yélwaani
Damakoy ndouraul waayé dou ki ngama fokk
Yaw ngané DIP yako meune kawél ba tiim Assamane
Xalissou Rap bi lay lekk teudi King Fahd Palace
DIP Mbacké baay Ziarél Serigne ci Akassa
Guiss ngama Trace mane ak sama clip Assamane
Fi akka tarr day xawa melni biir Pakétasse
Ma ngui Doundou Guiss yaw ya ngui doundou Khiff aka marr
Boudoul fi nga farr Fuck you yaw ak ki nga farral
Damay niodi deep té ma ngui cii sa biir fabélas
Ma ngui ci bèneu rime dissi def lou mate 10 enchainement
Guiss na Dakar niou beug siiw ni Kim Kardashian
Daw ba xokh té do am médaillou Amy Mbacké Thiam
Nio ngui sampeu nul mane may beef ba sama bissou enterrement
Fils Suarez la, plus Messi, Chris, ak Neymar
Beus Niki tay Disque bougne fi gueneu piraté temps yi
Bang Bang ! Damay gagné meme soumalay may revanche
DIP bagne bagne beug ni Monument de la Renaissance

{Outro}
Eééééy Eééééy Eééééy
DIP Doundou Guiss Nigga
TLK on the way
Haaaaahaaaaa
Manela Waay Morééé
Manela Waay Niggaz
Reptyle Music
Ibaaku Ex-Staz

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR