LYRIC

[Part 1] Beus bi ngay dée ay rongoniam Meunone nala sangue….
Doolei youxou yi atane nagnu sa corps bi, ba si sa biir pakh soul la si sa cambeu…
Merr na kaye wayei dou geudj dilla nianal founek dinalafa toudal tourou Yalla…
Bagua demei ngua yobalei xollam Doundame niakk khorome goumba teukhlou gana….
Beuss bi ngay dée ay goudila Yeah…
Si lagne guedjeu yeuk lerayou beuthieuk…
Kerok nioune nieupeu leu demone yeii ba mellni daguay nelaw ndakh keine meunouko gueum…
Xar yeik Xath bi demnagne ba dagne ko yeuk amoul mbow amoul mbeé Bb sakh dou seukeute…
Mowti djeulloula non dala goungueii ngua gnibi ndakh deukoofi Al-Jannah ngua deuk…
Deug leu deug leu deug leu Yeah…
Beuss biguay dée thi goudi la fegne…
Keur gui ni tekk Djeum dja faye….
Teud sa caisse kou djeum ngua tew….
Fleur yi la deff si att bi ngay djoudeu ak att biguay djotta gueine Adina yaw…
ameilooniou dara diokh ma linguei yi dalloul dinalako dello beus bi may nieuw Eh…

[Refrain] Nakarina si mane ma fattei funeirailles non non non ! Non non non non…
Deudji yi beuri nagne Wayei funérailles yi bokoul non non ! Ah Ah Oh Oh…
Nakarina si mane ma fattei funérailles non non non ! Non non non non…
Deudji yi beurinagne Wayei funérailles yi bokoul non non ! Ah Ah Oh Oh…

[Part 2] #Galsengenius
Beugouma diap sama xel que ni dotoumala guissate
Ya gnu nango bayyi def sa bopp nem si Yallah mane louma ci meune
Chaque goudi damay gueinte guiss la , gueinte bou nek ak limuy missal
Yallah meuneu mayé ; meuneu dieullate limou mome doussi yaw doussi mane
Yallah doula def dara , sa ndjaaboot dou torokh , ta suuf dou tang sa kaw
Gni guene ci niune moy gni dem
Warone naniu goude fane dakh ma meune aw fi nga aw
Mougne na mougne ba meuneutouma mugne dakh ronkhongne yi dess ci biir moy ronkhogne yi geuna sokhor
Boul deloussi gnune gnolay fekki
Boudé ya ngi gnuy guiss xolal gnune dagnu koy feté legui
Xolal na mere yi fethie , Pa yi mandi
Réindi beuye yi , réindi mbame yi
Dagnu lay goungué nga feeki Mame yi
Am nga ganaille yu bess pour aar gnu
Meme sa noone yeupa tew solu all black , tout noir repesent
Tour fi ndokh pour que niou soul ci kawam
Nakhari na ci mane ma faté Funairaille yi rawatina sama funeraillou bopp

[Refrain] #Galsengenius
Nakarina si mane ma fattei funeirailles non non non ! Non non non non…
Deudji yi beuri nagne Wayei funérailles yi bokoul non non ! Ah Ah Oh Oh…
Nakarina si mane ma fattei funérailles non non non ! Non non non non…
Deudji yi beurinagne Wayei funérailles yi bokoul non non ! Ah Ah Oh Oh…

[Part 3]#Galsengenius
Beneu mo geuna gaw
Niaar mo geuna woor
Gneuwa ndo wuniu mane ak yaw
Mama Cry , don’t cry no (bis)
Yallah buur moma lathie
nono gnemewuma negocier
Bayil ma dem sagnuma negocier

Nakarina si mane ma fattei funeirailles non non non ! Non non non non…
Deudjii beurinagne Wayei funérailles yi bokoul non non ! Ah Ah Oh Oh…
Nakarina si mane ma fattei funérailles non non non ! Non non non non…
Deudjii beurinagne Wayei funérailles yi bokoul non non ! Ah Ah Oh Oh…

[Refrain] #Galsengenius
Nakarina si mane ma fattei funeirailles non non non ! Non non non non…
Deudji yi beuri nagne Wayei funérailles yi bokoul non non ! Ah Ah Oh Oh…
Nakarina si mane ma fattei funérailles non non non ! Non non non non…#Galsengenius
Deudji yi beurinagne Wayei funérailles yi bokoul non non ! Ah Ah Oh Oh…

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR