LYRIC

{First Verse}
Nioune niaar liniouy doundou, kén meunouko xam,
Tay daniouy guissé bou souba niou réero…
Meunagn xoulo ma fokni mane rek nga bagn,
Té boumala soré nga def ma Sa Héros…
Douniou andeu té douniou baayi,
tay meunanio xoulo souba niou guisséwate Djoubo… (Faire la paix)
biss bouné niou lathiema lane ngay topé kii,
amna sakh niounane-ma guissnagnla’k kénén , Djouboo (t’es pas juste)

{Bridge}
Hey Girl stop trying me yoo..
Nénga bala nga am djam rek yaw fokk niou djoté…
Sometimes I think gyal you crazyoo…
Ni nga may Mérlowé , mane nonou lala beugué

{Chorus}
Meunounio djappanté – meunounio bayanté,
métite biniouy doundou melni moy sunu mbecté

“Gangsta – Gansta – Gansta – Gansta Love
Limoy Gangsta – Gansta – Gansta – Gansta Love”

Tay niouy Rayyanté souba niou Raayanté
Amna loma def beu meunatoumala faté

“Gangsta – Gansta – Gansta – Gansta Love
Limoy Gangsta – Gansta – Gansta – Gansta Love”

{Second Verse}
You play with me yoo
I don’t know why I can’t leave you alone yoo
You’re on my mind
Me can’t put you out of my way-yeah -yoo

Mane ak yaw forever , kèn douthi dèm fatè sa morom
Danio gaaw thi Guerre tè douniouy Soldier,
Tèwoul louma am , yaw yay Borom

{Bridge}
Hey Girl stop trying me yoo..
Nénga bala nga am djam rek yaw fokk niou djoté…
Sometimes I think gyal you crazyoo…
Ni nga may Mérlowé , mane nonou lala beugué

{Chorus}
Meunounio djappanté – meunounio bayanté,
métite biniouy doundou melni moy sunu mbecté

“Gangsta – Gansta – Gansta – Gansta Love
Limoy Gangsta – Gansta – Gansta – Gansta Love”

Tay niouy Rayanté souba niou Raayanté
Amna loma def beu meunatoumala faté

“Gangsta – Gansta – Gansta – Gansta Love
Limoy Gangsta – Gansta – Gansta – Gansta Love”

{Outro}
Yaw yay sama wife, meunoul niakk thi sama life yaaw.
You play with me yoo
I don’t know why I can’t leave you alone yoo

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR