LYRIC

{Verse 1}
Chaque jour dagnemay caméra, Fresh ni kou diougué Canada
Kouma songueu di nga sango coups (SANGOKU), Limay Flow KAME HAME HA
Je suis dans le Building t’es jamais là, Son ba ngi yengueul sa Favéla
Rappeur yi possé comme PAMELA, nalène nieuw sauvé comme PAMELA
Pro la sumay guèné HIT, Thug life ci samay ennemis
Saupman douniou djéguéti, Teau-Pla (Plateau) lama djouguéti
Guisseu gouma Mo F****r bouma meuneu fatélo samay origine (Macina)
Kouniou beugg booker gratuit dafa fékeu xamago sama money team (Mayweather)
Réwandé diarouta djaay té talents dh kèn douko dieundeu
Diaroul may deglou médias yi, ndakh mane la médias yi di reubeu
YALLAH dji rekka niou tiim, motah YALLAH dji kène doukou neubeutou
Wakh katt yi xeebou niou dara: défal niou wakh défo niou kébétou
Fils mane djaayouma pegarou ghetto ghetto pour djaay sama disc (no no no)
Tabaski ségnou sa rappeur di raay sama biir (Tabaski Flow)
Dem lakkatu kaaw ba, ba téréwoul ma gueuneu siiw
Mais lane moy sa saafara Freeeeeeeeee

{Bridge}
Defal sa job
Beus dina dokh
Ken matoul ci aduna
Gueumeul sa bopp
Mané : Gueumeul sa bopp
Bo togné nga djégueulou (x3)
Lolay Gentleman

{Refrain}
Gentleman, Gentleman, Gentleman, Gentleman
Gentleman, Gentleman, Gentleman, Gentleman
Gentleman
Xamna louy parcours rou gentleman
Sa bèneu peexé mounou niou gêné man
Boy ya ngi pelleul niou tiéné rek
Kène gueunou niou nek gentleman
Gentleman, Gentleman, Gentleman, Gentleman
Gentleman, Gentleman, Gentleman, Gentleman
Gentleman
Xamna louy galèrou gentleman
Sa bèneu peexé mounou niou gêné man
Boy ya ngi pelleul niou tiéné rek

{Post-refrain}
Lokho tchi kaw bo dé gentleman (x3)
Gentleman, Gentleman, Gentleman, Gentleman
Gentleman, Gentleman
Xamna louy galèrou gentleman
Gentleman, Gentleman

{Verse 2}
Yeah ! Niémé def lou bess sama définition, sama définition
Sama niaanou Mère sama bénédiction
Yaay Niaanal meu
Def lèn lou xess mo gueune ngène nek fi di thioow
Wallaahi da ngèn yapp nit gni moss
I’m a gentleman amoul ben man boumay tékeuleek sama bopp (tékeuleek sama bopp)
Artist bou melni dotoko dégueuh fèneu sama rakkeu (dégueuh fèneu sama rakkeu)
dotoko dégueuh fèneu !
Yaw done djémeu melni sama Clown dotoko défatti dom (défatti dom)
Légui guèneu lèn sama domaine domaine
Kholal kène doula guèné ci sa merde
Loffi sombi, di ngeu ko naane amoul dessal amoul guèdeu
Flow bi amoul melni Catholique bou signé takkeu niaarel (Flow bi amoul)
Indil gars yi daanu rap, li moy rap bi lèni daanel
Indi lou bess (Indi lou bess) Concert yi fess (concert yi fess)
Aakimo yaapeuh (Aakimo) baayil leu ress (baayil leu ress)
Rest In Peace ! Papa Gaïndé yama daan diokh louma lekk (Gaïndé nga, Gaïndé nga)
Kou fi né limay def neexoula rek da ngay wakh loula neex (da ngèy fenn)

{Bridge}
Defal sa job
Beus dina dokh
Ken matoul ci aduna
Gueumeul sa bopp
Mané : Gueumeul sa bopp
Bo togné nga djégueulou (x3)
Lolay Gentleman

{Refrain}
Gentleman, Gentleman, Gentleman, Gentleman
Gentleman, Gentleman, Gentleman, Gentleman
Gentleman
Xamna louy parcours rou gentleman
Sa bèneu peexé mounou niou gêné man
Boy ya ngi pélleul niou tiéné rek
Kène gueunou niou nek gentleman
Gentleman, Gentleman, Gentleman, Gentleman
Gentleman, Gentleman, Gentleman, Gentleman
Gentleman
Xamna louy galèrou gentleman
Sa bèneu peexé mounou niou gêné man
Boy ya ngi pelleul niou tiéné rek

{Post-refrain}
Lokho tchi kaw bo dé gentleman (x3)
Gentleman, Gentleman, Gentleman, Gentleman
Gentleman, Gentleman
Xamna louy galèrou gentleman
Gentleman, Gentleman

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR