LYRIC

Intro

bril & balva talking

1er couplet

BALVADA
Tayam gathiél na démbeum / mbéd nangou yémbeum/
dokh ba tékki eumbeum/woyoff xaragn waral teumbeum/
“”””””HIP HOP”””””
Daniouko téla tambali / waar sunu fass di labali/
Gueum ni Rap mo niouy sappali/ do kham li takh niou sopp lii/
Li niou thi dathie gueuna méti raw la maatteu – ma dathie thi taal ba/
Gueum deugueul sama bopp , gueumné beuss niou tokk thi djaal ba/
Saameu bou nékk , thiéné naagam/ démb la niou nekk thi wakkam/
Dianio dokh ba tankk yi naggam/djot tay niou doundé saggam/

BRIL
Nio thi dougou di raam/, di djéngou di djém /, té seuggouniou all’of the way/
Deukk thi takalé rhyme,/ ba yeungou thi dém,/ nga dégg niou everyday/
Lékk niou wééy/ niaari djeumeu thi guéthie la , guiss nga niongui fééy /
by the way/ déggo Mayday (cris d’alerte) / douniou mayé déy/ lou djafééy
finiou djarr ba yakkci fi, nékk-fi, radjakhé fépp di yéékk/
tégalé nieupp di béék/ lépp niou break/ yégalé kheuppla yeukk/
mbeur mi thi guéw bi guiss nga nioko baakk
nioune douniou xaadi, nioy gni déss thi téén bi niodi baak/

REFRAIN
GHETTOOOOOOOOO – HEROOOOOOOES
balvada ” nioy hero, number one in da ghetto,
cii braind laniouy altéro , sa haal , lagn lay téroo”
Bril ” Nionthi nékk démb , feuss thi tay , djéguéci eundi lou baari
xééx ba lépp yémb , gueune thi tééy , djokh thi everybody”

2ém couplet

BALVADA
from the bottom to the top , niafél ba diss, hope
doniou disturb, niounela “hip hop” foniou guiss teup
mbéda niou déf assou pique /, amoul saka sikk, /
sunu rap la sick /, djokh niou feuille ak bic,/ saass wi boumou diik/
BRIL
niou seugg thi mbindeu mi djhokhla lyric/
nda thiy goukh ni zriik/
xalima djoukk thi daa bi reudeuti, niam nga tékk thi briik/
get it /
légui guiss nga , sipp nga , here we go/
nioy gni djougué fou soori , dikkeu ték rhyme nga khééwi go/

BALVADA
teuyél sa bras , daniou séleu mind , worna jah man (express)
meuno thi dara , déf thiélleu , fine , nangoul jah mane /
Déf niou wakh , khaandé bou défi waakh , oubi mou done thiakh
kawé ba ndourou nakh, akh, sunuy kaadou dalay niakh
*

BRIL
Baat yi doughou ci nopp , djaleu fégn thi biir né nombril/
Supa dupa riir thi bopp déf sama nom bril/
Ladjal wizzy , I’m the mirror on the wall, séétoul
Dafa easy, khol nga miiro, li ngéén fomppp séttoul

REFRAIN
GHETTOOOOOOOOO – HEROOOOOOOES
balvada ” nioy hero, number one in da ghetto,
cii braind laniouy altéro , sa haal , lagn lay téroo”
Bril ” Nionthi nékk démb , feuss thi tay , djéguéci eundi lou baari
xééx ba lépp yémb , gueune thi tééy , djokh thi everybody”

3ém couplet

bridge
GHETTO HEROES

BALVADA
Pinkou ba soow/, Nieupp thi galgui djoow/ bougouma déggati thioow,/
lokho yeup thia kaw/ bou job bi low, hip hop bi law ba faw ,
doufi seungém , dinagn djém sunu kémmtalay katane
boumou la yéém drapeau hip hop siip nga niokkko aattane

BRIL
Lord of the underground/dougou sa town /baggué fi sound/
we’re da best up and down/ gni ngay dégg all around/
“Heeeeeroes”
Mbir mi damar la , nioy ay roue-weum/
it’s like , rap bi djeumm la , last fighter moy rhouweum/

REFRAIN
GHETTOOOOOOOOO – HEROOOOOOOES
balvada ” nioy hero, number one in da ghetto,
cii braind laniouy altéro , sa haal , lagn lay téroo”
Bril ” Nionthi nékk démb , feuss thi tay , djéguéci eundi lou baari
xééx ba lépp yémb , gueune thi tééy , djokh thi everybody”

OUTRO
bril & balvada talking

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR