LYRIC

{Refrain}
Guerre day saf mondiale
Gué gué guerre day saf mondiale
Guerre day saf mondiale
Gué gué guerre day saf mondiale
Guerre day saf mondiale
Gué gué guerre day saf mondiale
Na Saf na saf na safa safa saf

{DIP}
Ey xétou déh momay xégne moussibeu forever
Nio beug néw deuk bouniou dém guerre tay bougnefa joggué soubeu kène doukafa féké
Ci guédjou dérette laniou beug féy tay waa noumou gueuneu xonké rek
Yaw meunone nga bania sole téré gnima joggué ray ay sorcier lagne

{Iss}
Flow bi ni liquide ci compte en banque, sa mère dafa tipsé dieulna contact sankeu
Lance roquette Clashnikov kane laay saank, imposé couronné tek ay tankeu
Poésie urbaine dou Maupassant, dikkeu dila fuck defko mon passe temps
Guédiawaay cii sa kaw ni thiaga bo fay, téw ci sa buzz dila ragal lo tay

{DIP}
Lofi def bo raggalé taal auto commissaire ? goor-djiguène dou féké thioky fin
Yeurmandé mofi diékh motah soti nagne Rongagnou défeant ni ndoxou robinet
Olimé noyil lila dessé ci oxygène ngané doniou dégueu
Ballou pistolet yi ci sa nopp bi lay diaar feulaate cii sa bénène nopp bi rek thiow li diekh

{Iss}
Dawal Char sène kaw lékkeu leu ni poutine, fuck sen star yi yeup daw sopi lène ay victime
Iss leu toudou day sissou fougneko dégueu youkhou day dougou
Pénétration de surface ennemis, violation de case ak rocket
Controlé game bi sédeulé carte yi defko ni Casino kène douko ropette

{Refrain}
Guerre day saf mondiale
Gué gué guerre day saf mondiale
Guerre day saf mondiale
Gué gué guerre day saf mondiale
Guerre day saf mondiale
Gué gué guerre day saf mondiale
Na Saf na saf na safa safa saf (2 fois)

{Iss}
Dagnouy téw sa biir chambre dila ray, Game bi 1er novembre funérailles
Domou brigadier bou faléwoul Caporal, douma ouvrier mais nieup lay défaral
Général dou arrière cii guerre day diokhé commandemant teksi di djiteul nieup
BsB ni lance nucléaire avis bombardement, fokk mouy titeul nieup

{DIP}
Djiteulouniou texte pour fégne télé rek, gni meunou niou dem té douniou baayi kénène dém
Doundou Guiss fepp…14, 15, boniou meunoul fay louniouy déf sa concert
Sunu couplet dou Kourpégne té day gaagne, Xawma nouniou def ba meune lène may diaale
Niou nioy 3ème Guerre Mondiale, Dou lou Youssou Ndour def lagni diémeu défaate ?

{Iss}
Da ngay tokk guiss télé niouy tek deal di siiw, nioufi def text-sou tay rek la public bi di mbiiw
Sunu succès mo ngui xéégne ni néggou 104 Naar, song bi dina guéneu teuthie sa guémigne sans cadenas
Tek chaise électrique sen rappeur, loxo cii sa beute leu bic-gou Schneider
Pow cii sa bopp Sniper, boma guissé dawal vitesse Schumarer

{DIP}
Gaïndé bou xiff laniou yémalé ak xathie bou xiff, Album bi di ngako fekk bassi ay bouki
Raak bi dou acoustique lima bania def nigga xadja goufi
Gniy nélaw laay ray ci xaadja goudi, Tek xel tek xel ni LEUK ak BOUKI
Fexél féxel ba am trackou DIP dou NTC… Bombe Atomique
Morééééé

{Refrain}
Guerre day saf mondiale
Gué gué guerre day saf mondiale
Guerre day saf mondiale
Gué gué guerre day saf mondiale
Guerre day saf mondiale
Gué gué guerre day saf mondiale
Na Saf na saf na safa safa saf (2 fois)

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR