LYRIC

{Ara}
Loumay def Aldiana
Né Nala fo né mane fala né
Lou werr di def ci assamane
Boudé néwoul sa kanam lay wané
Lou café bi di safé dose
Ya done motali thiafka biné sama soukeur bekk
Lou waral fleurs yi rose
Té néwoul yaay khéinthiou khéte bi rééh meu ma daldi bëg
Sama yeuf

Xol bi yaw rek rek kako meuneu beuss
Diox nala lepp lepp lepp lou tchi dess
Toppeu nala fepp fepp fepp ba nga seuss
Té dou takh ma lép lép lép lou tchi dess

{Refrain 1}
I love Me, Any I love you too
Now I’m feeling so lonely
And I can live without you
I’m so sorry (sorry)
Baby I’m so sorry (I’m so sorry)
I’m so sorry (sorry)
I’m feeling so sorry oOoh
Baby I’m so sorry (I’m so sorry)
Baby I’m so sorry (I’m so sorry)
I’m so sorry (I’m so sorry)
I’m feeling so sorry
oOoh Baby

{Ara – Verse 2}
Nameu naaa dooreunté ay njéguénaay
Fo sama bopp dima foone dima raay
Nameu sa féém thiouraay
Sa lokho bima doul laale bouma teudé tay ci night
Mane xawma sakh lou lekk di saf
Keur gui peundeu ndapp yi tilime télé bi peundeu té panne
Collègue yi dima wo pour taf
Dama feebar baby nékoufi té nélawouma dembe haann !
Réveil bi sonné ma beus nélawaate
Yaa done nieuw ci laale biz donema yéé waate mane
Takkalma sama cravate néma na nga sage
Nieuw ci nope di wakh ak mane ma
I Love you, I love you too
I Love you, ma ni I love you too
I’m feeling so lonely

{Refrain 2}
And I can live without you
I’m so sorry (sorry)
Baby I’m so sorry (I’m so sorry)
I’m so sorry (sorry)
I’m feeling so sorry
oOoh
Baby I’m so sorry (I’m so sorry)
Baby I’m so sorry (I’m so sorry)
I’m so sorry (I’m so sorry)
I’m feeling so sorry
oOoh Bae

{Dayza}
Han ! Lou moussoul am ma niaane la lèneuh nga tek ci baate
Mais tay nak bi moy bou moudj faw nga mayma niou andeu go home back
No meussoul beug sa xol taakeu
Daa yagg beug nga contane
Wane nama mbeuguél wane ma bague
Né yaw la yagg beugone takk
Fatélikoul ni meuss na neex kone di nga fatté baalé
Même niaari wégne bouniou beugué bess faaw niou khossanté laalé
Wait, Wait, Wait, Wait

I’m So Sorry
I’m So Sorry
I’m So Sorry

Lomay nouyo ? loy wo khoulo bamouy nieuw ?
Ana goor bou galant wone ? tay mala khol day melni dou yaw
Sa galé ba ngui ni doffé Té yaw rek do défar café
Nga am kou melni ki dila topoto boy dafa djaffé
Diamono tay djiguène wourouss leu, Li tchi baax laniou wara sameuh
Dél khalate bala nga wakh guéneul délo ay valisam

{Refrain 2}
And I can live without you
I’m so sorry (sorry)
Baby I’m so sorry (I’m so sorry)
I’m so sorry (sorry)
I’m feeling so sorry
oOoh
Baby I’m so sorry (I’m so sorry)
Baby I’m so sorry (I’m so sorry)
I’m so sorry (I’m so sorry)
I’m feeling so sorry
oOoh

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR