LYRIC

Yeah ! Aaaannnh
Xol bu bone bi né ci mane motah may khol lou bone di guiss lou baakh
Nimay fayyo dèy neubeu samay noone né DIP dou baal
Deugou garap bu YALLAH xoothie ci ndokh bou Nit doul naane
Féké wouma niamou daaw Hip Hop bi f**k Biggie 2pac
Faaw nga sopp, précoce ni liiir bouy fo di lire journal
Sinon niou djaay sa Maam ni xonk nopp ni Toubab
Moytouma ngay djaay sadique coupable matoma bèn daaj ni centilitre flaq
Mane xawouma wone ni Rap moy ngay job ak ay Doméram
Rotal tchi samay niakk (sueur) douma djoy dila diokh ngay naane
Xam ngani déh boudone diaar tchi xaliss nioune nieupeuy déki
Xalissou xalé dèy seug di guiss lou makk dou seintu
Warone xexkh di tchi soneuh
Nga daan féthieu di fo
Am ay 5, 6 doms
Ni kou gueinteu guiss GOD
Gniy djaay Gangsta tchi Kogne
Moudjé jail beu di djoy
Forr ay dessite di thiop
Dou sama destiny Non
Kill sama bopp ci troc bu luxe ni boy Philip Senghor
Mo gueun xiff ak ndaul ay domou diw di diw seu dom
Boy changé air moy dem Aadjana sans seu mère
Talent biy fay da féké woul Talatay Nder
Boy Fallou Sène rekka perte mom ak gni déh stade bi
Deuk bi mounoul dokh nieupeuy dougueul ay statuts
Ngour gui yégoul seu déh ngakay wane sèy cicatrices
Février yaggatoul pour niou namone Spartacus
Nénagne niomay wakh limay def nénagne nioy PAPE-pou DIP
Sama Papa beugoul wone may RAP di diaar fu bone
Fayou niouma sama Money bamay Job ak AKHLOU BRICK
Motakh sama cerceuil rek laffi sékeul JAMDONG
Life boulay Violé dafay khaar ba nga Guiss sèy REGLES
Khaar nga XIFF moulay LEKK ba nga 4 Appuis moulay mbéthie
Litah ngay doundou lèy Ray
D’accord douma jugé mais déwouma Aadjana boudé biir aadjana di ngafa guiss PD
Démal seuleumou tchi lénène loudoul Xeureum Mysthique
Seuyou deureum ak deureum, Xaritou domaine yu Siw
Ba leu Guéweul yi djign do xam NITTEUY ennemi NIT
Beu ngeuy Teereuri niouy sodomie ci seu domicile
Teuthie na Perpet sen Secret sama Xol douma Wakh
Pour quelques vues ak j’aime ngène tekk samay funérailles
Diékhal sen xaliss rekka meu téré soul sen Yaay
Louy sama yone ci son bu nice
Men fokk niou fayma

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR