LYRIC

[Hook]
Né nga danga am problème
Mais mala eup problème
Kouci nék amna problème
Mais dou nieupa koy waaakh
Né nga danga am problème
Mais mala eup problème
Kouci nék amna problème
Mais dou nieupa koy waaakh

[Verse 1]
Amo nieugou ordonnance
Mane cancer moma daal
Est-ce que douma dimali ci pass
Mane ci bourlé car lako kaal
Sa girl dafla trahir
Mane sama girl néna dafa bir
Boudé ya ngui souffrir
Moy mane mangui dé ci biir
Cent milles problèmes, milliard problèmes F**k 10000 PROBLEMES
Soumakoy nétali do dém
Diogué ci problème, dalal ci problème, fatél say problèmes
Amo yeuré yoy sol
Mane t*tounén lay déf
Ngané bén girl doula khol
Equipou lamb bi mafay chef

[Hook]
Né nga danga am problème
Mais mala eup problème
Kouci nék amna problème
Mais dou nieupa koy waaakh
Né nga danga am problème
Mais mala eup problème
Kouci nék amna problème
Mais dou nieupa koy waaakh

[Verse 2]
Sa raakeu dafa AVC
Sama maak safa Ébola
Bindeu na acte de décès
Bayi woufi gneugou chocolat
Sa girl day saw lal
Sama diabar day p**p lal
Khawma lane mola dal
Sama problème khadioul hôpital
Amo lo fayé louass
Mane huissier daf ma guéné
Dénkanéna samay bagass
Moungui nonou galé Niémé
Vie sa problème pour yaw
Té boumako nétali
Ndakh amna problème comme yaw
Sama pane boukou féthiali
[Hook]
Né nga danga am problème
Mais mala eup problème
Kouci nék amna problème
Mais dou nieupa koy waaakh
Né nga danga am problème
Mais mala eup problème
Kouci nék amna problème
Mais dou nieupa koy waaakh

[Bridge]
Dangay am sa problème
Wétak say problème
Bayimak sa problème
Yaw mome no problème
Dangay am sa problème
Seufma say problème
Déci sa problème
Yaw mome no problème
Dangay am sa problème
Ba mak say problème
Ba doto amati problème
Yaw mome no problème

[Hook]
Né nga danga am problème
Mais mala eup problème
Kouci nék amna problème
Mais dou nieupa koy waaakh
Né nga danga am problème
Mais mala eup problème
Kouci nék amna problème
Mais dou nieupa koy waaakh

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR