LYRIC

[Couplet 1] Soura guma man. Bénén way lay lék
Médocratie till I die. Imposer Bay la ték
Niaata sons publicités mangui laal ay chèque
Dama nieuw sa rappeur danu comme kouy laal ay diégg
2003, Blindé back néko ndaa lay nék
Di la tégal histoire comme ay paa lay fréq’
Dougou ci bars yi diékhal verres yi après diaye Laye yégg
Diap sa Mc guinté bakou Falay bégg
Boy diay saleté fékkeu fi Seune
Fok nga Gorgorlou pour nék sama Dièg (bitch)
140 caractères gnoko meune
Kone Normale nga gnouy fék
Dou gnou follow wakhou pithie
Dangay niodi khélou Dictionnaire,
Bame la dégué LA ROUSSE
Médocratie 6000 missionnaires
Rap Alphabet, diangal gnome Papoose

Ref
Médocratie, BSB, 814, Baye Laye, nél Sku (Sku)
Number Niar till I die, Never change, Médocratie, nél Sku (Sku)
BSB, Baye Laye, Guédiawaye, Médocratie nél Sku (Sku)
Nél Sku (Sku)

[Couplet 2] Sa rappeur dafa faye comme kou sonou ci seuy
Néko gnoune moung gnouy faye dougnou ci sonou liguèy
Ci souf ngay négocier ci kaw kébétou
Doumala khol sakh bodé Mari Chou
Sa rappeur lagniy défal mémorial
Son bi dina yeungal Paris même Montréal (au Real)
Flow bi guena rare dingko woutiwal
Bo bougué nék sama mass fok wotti watt
Diangal niom Papoose ba sa pa pousse
That’s not new, sa mbeur touss
Moungui bir douss
Tate béy souss
Ya fouss, yangui for souss, diékhal cartouche, fété souf, poupe la pouss, daak gay ouss
G-waye ci hand lunék I fuck with that
Ligay ci pét di get gni show respect
Briquette, allumette, na fête yi di take dieupét
Ci nét di téke ni diégg but fuck you man
Yeah Yeah

Ref
Médocratie, BSB, 814, Baye Laye, nél Sku (Sku)
Number Niar till I die, Never change, Médocratie, nél Sku (Sku)
BSB, Baye Laye, Guédiawaye, Médocratie nél Sku (Sku)
Nél Sku (Sku)

[Couplet 3] Pour classer sama down nikou sétsi tchoin
Tangal game bi nadiou 5ème, lou raw 7, 6 juin (?)
Pape Sidy Fall nénama Iss lou takh textes si loin
Boula khélou ndag yi khar takh nga ték fi foin
Sa rappeur fébaroul mais dafa dieul ci soin
Niari lancées hors zone, nodéf nga dieul 6 points
Guiss nalén gnou teup di dall mané téke ci coin
Même souma ndarone rouss ni I public bi téke ci point

Added by

Ahmed

SHARE

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR