LYRIC

Marquez les pas, 1, 2
Mon général, 1, 2
Ton pied, mon pied, 1, 2
A vos ordres madame
Marquez les pas, 1, 2
Mon général, 1, 2
Ton pied, mon pied, 1, 2
A vos ordres madame

Oh, oh, Miss Colombo (Miss Colombo) (x3)
Miss Colombo (ya ya ya yay)
(Momouloma) Khoulo bi souba ak ngone
(Momouloma) Nagnou bayénté bén yone
(Mane momouloma) Way way dama sonou
(Momouloma) Mayma sama diameu

Ci mane nga kheuy, mane ngay gontou
Est-ce que fogone ni yaw yay Colombo
Ték nga ma pression girl
Démna sakh ba manatougnou déggo
Dou diaka dou église
Ték nga ma pression girl
Marquage à la culotte hé
Comme défenseur ak Ronaldo

Khana lidou guéneu késsé
Mane dama sonou, tayi, bopp rék lama déssé (Aie, aie, aie, aie)
Légui sakh j’en ai assez
Sodone sama yaye, diourouloma mane késsé

Beuri loy kass
Beuri loy lidjeunti
Soumay nélaw yangui sama téléphone, diko djéma tidji motakh ngay bideunti

Oh, oh, Miss Colombo (Miss Colombo) (x3)
Miss Colombo (ya ya ya yay)
(Momouloma) Khoulo bi souba ak ngone
(Momouloma) Nagnou bayénté bén yone
(Mane momouloma) Way way dama sonou
(Momouloma) Mayma sama diameu

Biss bou nék nga indil ay matter
Sof beug détails kagn ngay maggeu
Beuri problème, no dou meun dém
Gueumou ma sounou andeu yagg comme bou Thione ak Diagga (Aie, aie, aie, aie)

C’est pas la police (C’est pas la police)
Dou diaka dou église (Non, non)
J’en peux plus, trop c’est trop, là, c’est bon, j’en ai marre de tes caprices

Allo bébé fo nékk
Kane mo wakh nonou sa wétt
Est-ce que baatu djiguén lay dégg
Mane meuna touma lolou
Bébé kodone wakhaal téléphone
Na nga yam sé galé talal sa télé kone
Passe ma sén diankeu
Dama sonou ci lolou

Yaw girl, wakh nala yafi nékkeu
Sama khol lala dadieul ci condané diokh lako néla ay dorleu
Wakh ma lo beug légui
Yaw gueumal sa boppou mane doumala dégrader beug nala worneu

Oh, oh, Miss Colombo (Miss Colombo) (x3)
Miss Colombo
Oh, oh, Miss Colombo (Miss Colombo) (x3)
Miss Colombo

Kone sama téléphone sonner lodiapone dankoy bayi
Waro ame diam, tant que khamou koumay wakhal est-ce que do wa FBI (Miss Colombo)
Han, sétlouna bougnou andé di dokh sakh dang may pogné
Melni dagn la wakh ni damay nara reuthie est-ce que diawalé wona ak boy djiné (Miss Colombo)

Marquez les pas, 1, 2
Mon général, 1, 2
Ton pied, mon pied, 1, 2
A vos ordres madame
Marquez les pas, 1, 2
Mon général, 1, 2
Fo dém, ma dém fa, 1, 2
A vos ordres madame (x3)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR