LYRIC

{Verse 1}
Wathié naa Teeré AMAYATA amna diouraum niéteu (8) att
Té djangue bimay djang guissouma sakh njeurigneum
Loutah mou am niou wara soneuh am niouy khaar sen héritage
Aduna injustice leu dou kou nekkak mériteum
Serigne bi néna kouka dégueul mou xétalileu
Miskine bou fessaloul sa pott mou djékalileu
Moussouma njaalo mais feug nagn-meu teeméri (100) yarr
Bala may délou Daara ba faaw teemeer yi matt (500 Frs)
Hééy ! mais thiow dou djipp ma ngi maagueuh.
Xamna sama handicap (lane ?)
Boy douma domou Diw niou def meu animal
Sokhlaatouma nioumay doumoyou pour meu effectivement douma done kou riche
Ndakh dagnma sani aaleu.
Kène tégou mako koudoul samay waadiour yima diour Kone fokma démé Xollou mougn
Té bania radical baayi ma khaar beu souma gueuné deugueur touti daaldi faakeu

{Pré-Refrain}
Ma tchi meuneu guéné sama bopp
Jameuh rek la yeené sama bopp
Jameuh rek la yeené sama bopp
Xam naani ma tchi meuneu guéné sama bopp
Ma tchi meuneu guéné sama bopp
Xawma loutah life bi di gueuneu yeemé sama bord

{Refrain}
Ani gnima daan boott dima nakh bama nélaw
Loutah gnima bokaloul daara rek laay talal lokho
Yeah yeah
Amatouma Baay Guisseu touma sama Yaay Booy
Guisseutouma Yaay Booy
Bouma Yeureum dima diokh djeune “Jangal Ma Napp”
Jangal Ma Napp
Jangal Ma Napp
Mané Jangal Ma Napp (So défoul rek def thioow)
Yaw mi am Gaal meuneu djoow Jangal Ma Napp
Oooh ! Goor gui Jangal Ma Napp
Yeah ! Soxna Ci Jangal Ma Napp (So défoul rek def thioow)
Sarakh ci fadjoul samay gaum Jangal Ma Napp

{Verse 2}
Fouki att ak Diouraum Bèn (16), Kène beugoul melni mane
Té mane meunouma ndourok kène
Xam naani boudoul MBèDE kène douma kholé DOM
Borom Auto bima moudjé Goal-lou dafma khélou rombeu
Fourniture, Sac, Yeeré aki dall Bima djoudo beu légui dh dégg rk la tchi am
Mounouma Lire té awouma métier bouma djangue
Gni ngèni wowé WAGGA yi rek nioma nangou fatt
Bala niouy wouti JOB fokk niou am loumou THIOP
Seugueum douniou ko djokh dagnkay wouteul suniou BOPP
Fekk niou Gueedju Koussoum wala Pont Colobane
Fi koufi né di trainé dagnelay fuutti yaubou djaay
Gnène gni di dougou FAC gnénène di dougou PLANE
Nioune niou nek di dougou keu guèneu beu dougou JAIL
Ngène berr niou tchi lepp melni nékouniou SUNU REEW
Kène niéméwouniou DOUNDOU ndaxté RAGALOU niou DéH

{Pré-Refrain}
Ma tchi meuneu guéné sama bopp
Jameuh rek la yeené sama bopp
Jameuh rek la yeené sama bopp
Xam naani ma tchi meuneu guéné sama bopp
Ma tchi meuneu guéné sama bopp
Xawma loutah life bi di gueuneu yeemé sama bord

{Refrain}
Ani gnima daan boott dima nakh bama nélaw
Loutah gnima bokaloul daara rek laay talal lokho
Yeah yeah
Amatouma Baay Guisseu touma sama Yaay Booy
Guisseutouma Yaay Booy
Bouma Yeureum dima diokh djeune “Jangal Ma Napp”
Jangal Ma Napp
Jangal Ma Napp
Mané Jangal Ma Napp (So défoul rek def thioow)
Yaw mi am Gaal meuneu djoow Jangal Ma Napp
Oooh ! Goor gui Jangal Ma Napp
Yeah ! Soxna Ci Jangal Ma Napp (So défoul rek def thioow)
Sarakh ci fadjoul samay gaum Jangal Ma Napp

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR