LYRIC

[Part 1]
Toudouma Michael mais am naa ay textes de dingue
Khaaral ma def son bi mey ko samay best fan
Réservoir ak concert damay def le plein
Sama Compte Di gueuneu fess sayoumay Tek refrain
Yalla def may binde son you cool si nit
Boudé danga beugg battle demal call sinik
Soumeu nieuwé se side damay Soul si nit
Bo solé gilet pare balles homie boul simi yeah
Danga beug signer Oven
Demal tediou diangui waat fi dou Mic open
Nioune deniouy trap deniouy def ay son wou lover
Niom ak mane carapid ak range rover
Game over wouti leen khey
May wouti ngay hate Motakh fouti nguen tey
Boul yek se boppeu ni puceau Bou djiguene diey
Gaindé jackson flow yow yeufou Bouki ngay wey
Yeah
Chaque gouddi ma rèré beat
Eupp appétit gaindé bou wara réré nit
Deugg deugg danguene di wéré fils
Guent na pac big nemeu gerel Free
Chaque gouddi ma rèré beat
Eupp appétit gaindé bou wara réré nit
Se shawty mane le daadiel rek mir
Dama pro dama hot dama deep dama tar dama bad

{Refrain}
Bad bad
Mala gueuneu maala gueuneu bad
(Free Jackson)
Bad bad
Mala gueuneu maala gueuneu bad
(Free Jackson)
Bad bad
Mala gueuneu maala gueuneu bad
(Free Jackson)
Teen na, guestou naa I can tell you once again who’s bad

[Part 2]

SMOOTH CRIMINAL

Beugone nga gener sama carrière
Di tek ay barrières, di def ay sales coups (han)
Mais sama album defe diar yeah,
Koudoul Yalla mounoul bloquer sama parcours (ouh)
Mangui dokh nguen di arrière, malene wara yè, vous avez wallou
Sene music bimouy varier,
Bobou maa ngui def ay 10000 hits par jour

Awma jour ferié awma jour awma jour férié
Freedope fekk ne ma rap be périé
Awma jour ferié awma jour awma jour férié
Awma jour férié yow rekka dessé prouver yeufou guerrier

Awma jour férié
Douma dieul pause ken douma téyé
Am ne niou done diaay guerrier
Founiou moudié? gningui hospis leegui
Mane awma jour férié
Douma dieul pause ken douma téyé
Am ne niou done diaay guerrier
Founiou moudié? gningui cimetière leegui
Mane awma jour férié awma jour awma jour férié

Awma jour férié
Freedope fekk ne ma rap be périé
Awma jour férié awma jour awma jour férié
Sene game bi defe touti tchi mane
Danguene fou di dingat
Mais sama crew ngui tchi kow

[Couplet 2]

Kham nga né dama aye car diaroul Diaay tar ni kou doul Diaar douche
Bimay ndieukk guenné mixtape
Awma wone louma defé courses Carrefour
Sama team nieupp ay partant
4 quart temps yeup yeney Khaar touche
Bo niou beugué indil ibliss
Jammdongg sopeulikou guerrou Darfour
Mane awma jour ferié awma jour awma jour férié
Awma jour férié
Freedope fekk ne ma rap be périé yeah
Awma jour férié
Awma jour férié awma jour awma jour férié
Awma jour férié yow rekka dessé prouver yeufou guerrier yeah
Awma jour férié
Douma dieul pause ken douma téyé
Am ne niou done diaay guerrier
Founiou moudié ? gningui hospis leegui
Awma jour ferié douma dieul pause ken douma téyé
Am ne niou done diaay guerrier founiou moudié? Gningui cimetiere leegui
Mane Awma jour férié yow rekka dessé prouver yeufou guerrier
Dadié nak ay Fouki ciste-ra
Digou goudi birr kaaw
Takhoul ma Wiri kogne

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR