LYRIC

{Verse 1}
Beug beug molay djappeu teuyé beuss thi di naaw
Lou beuri dila raw, ren ak daw nga dess thi guinaw
Wérou thi dina bakh, seug lepp toppeu sa geum
Seuguem thiono dou reer, kounekay sigui thi seugueum
Yanguithi Deug Deug, yenouko né kouy guenté taaw
Yokku sa degg degg xamné niakh dou fegn si taw
Dama yagg tameu sen yakk derr yi ma for thi tama
Def kirama wanela lithi ndiol dou ndama
Degouloma !!!
Nio teudjou di binde rek, goudé teud paré texte
Niak diote ba kouniu bolé thi dara niou djokh ko pretexte
Sound yi lay beglo mo niou fananelo thi studio yi
Guindiwat la fomp rognogn dakal sa dioy yi

{Refrain}
Right now
It’s like they don’t know
We’re doing it for the love
Just for love
Of singing like a sparrow
And flying like a dove
So far away
Da ngay xaddi everyday
Sunu music
Beuga bayyi everytime
Da ngay xaddi everyday
Thi sunu music
Beuga bayyi all the time

{Verse 2}
Gueneu nga thi sa repère, dal fi gaalou dof teere
Gni lay degglou dooni expert beuri louniouy téré
Sound bou dioudou tay niou falko guinté souba niou gassko soul
Laathie lou bess nga defko nign ko guenté dara dessoul
thi xaatim ay rimes, technik ak mbindeu leppeu day matt
Louné ngay dath calculé barre yi nekouy tothie Math
Loffi tang teyal, djantt sakh dafiy ceddé
Thi guena meunn commenté louthi neeway djeund cd
Tokk thi boppu kogne yi deukké critiqué cons air
Fans number one yi xamouniu prix ticket concert
“Baye sa son yi nice na”: Boudone founiou ko degge diot deureum
Kone gnou dal thi ba kou guené Album tabakh keureum

{Refrain}
Right now
It’s like they don’t know
We’re doing it for the love
Just for love
Of singing like a sparrow
And flying like a dove
So far away
Da ngay xaddi everyday
Sunu music
Beuga bayyi everytime
Da ngay xaddi everyday
Thi sunu music
Beuga bayyi all the time

{Verse 3}
Rang bi doxoul, embouteillage bi serré, train yi deraillé
Meune li ngay def doula ci guené fi la Talent di rayé
Lou baxoul laniouy tagg melni nopp yé tilim
Niveau bé soufé fok nga seug niou sogla bolé ci liim
Gni warone tok deglou sound diouk di xeuthio mic
I don’t Like, bou gni di boxe melni mike
Tyson thi ring bi niodi bandit fass kanam
xeekh ba faté rime bi, dou yobou sunu fass kanam
Talent yi xaadi bayi meuno xam niniou beuré
Fi fess’ak paa youy teup di baakou melni niouy beuré
Bagne goor dioudou, xeuthio ngour ak liir sopekou firawna
Wouteul laff reuthie, kou dal fou geuna noy fi rawna

{Refrain}
Right now
It’s like they don’t know
We’re doing it for the love
Just for love
Of singing like a sparrow
And flying like a dove
So far away
Da ngay xaddi everyday
Sunu music
Beuga bayyi everytime
Da ngay xaddi everyday
Thi sunu music
Beuga bayyi all the time

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR