LYRIC

Let me hold and protect you gyal
me don’t wanna see any tears in your eyes
Let me hold and protect you gyal 
nobody coulda coulda treat you so nice
Let me hold and protect you gyal
cuz me don’t wanna see any tears in your eyes
Let me hold and protect you gyal
I see nobody coulda coulda treat you so nice wooo

{Couplet 1}
Bigni xamanté niou ngui NOTRE DAME
Dafa rombeu sama gars yeup né got’em
Xamone naani yagg yagg nako contacté bouma défoul lou gaaw légui bénène black dem
Yeah ! Amoul wone numéro portable dama daan def baatu guel woté galém
Ay boy yu ndaw doundou sunu couple love
Xam nga diaar nagnou fu sori louma beug mouné maay bagne
Yeah def nagnou au moins 5 ans, souniou mères yi dem bay sameu digueuneté
Mais dafa djéki djéki sonal samay tympan, naanema takma dama beug niou nguèneté
Manéko Boo xaral ma paré sama djangue sakh
Meunou mala niaane cii té amo gouma laire-sa (salaire)
Mounéma gawaal wala niou mayma bénène gars
Manéko yafa déh doma dieuléti fénène gyal
Bou dembe done tay doumako tontou
Kouko meuneu am di hésité daye fontou
Andou mawone ak sama sago ndax tangue
Na-ngou naané djoum naa té dina cii djangue

{Refrain}
Kaay niou nékaate, niou doundou happinessma
Kaay niou nékaate, paréna yassi dess my…. (Yeah)
Kaay niou nékaate, dinagne doundou Happinessma (Yeah)
Kay niou nékaate, mane paréna dh yassi dess my…(Wowow)
Kay niou nékaate (Kay niou nékaate) (n fois)

{Pont}
Let me hold and protect you gyal
me don’t wanna see any tears in your eyes
Let me hold and protect you gyal
nobody coulda coulda treat you so nice
Let me hold and protect you gyal
cuz me don’t wanna see any tears in your eyes
Let me hold and protect you gyal
I see nobody coulda coulda treat you so nice wooo

{Couplet 2}
Miskine ndakaaté yaay first
Souma dieulone sama temps doumala djaay seuss
Guisso gouma kèn am sa ay qualité
Soudoul yaw amoul kénène koumay validé
Ma ngui doga na-ngouné djouma naa
Louni mel dotou dall ci Aduna
Pourtant xamone naani kène doula gueune
Ma topp sama beug beug ma niaak leu tay reuthiou na
Han ! dotouma faté sa birthday
Xam naané defna la loy nakari bataye
Dotouma guène goudi sheytané yi guiss ma
Nga yéwou wakh kaat yi fénalma dila tristeul
Yeah ! Passport, Visa, London, Ibiza
Dinala yaub ci deuk yi gueuneu diksa
Dina tak nga taakeu ni rizla

{Refrain}
Kaay niou nékaate, niou doundou happinessma
Kaay niou nékaate, paréna yassi dess my…. (Yeah)
Kaay niou nékaate, dinagne doundou Happinessma (Yeah)
Kay niou nékaate, mane paréna dh yassi dess my…(Wowow)
Kay niou nékaate (Kay niou nékaate) (n fois)

{Pont}
Let me hold and protect you gyal
me don’t wanna see any tears in your eyes
Let me hold and protect you gyal
nobody coulda coulda treat you so nice
Let me hold and protect you gyal
cuz me don’t wanna see any tears in your eyes
Let me hold and protect you gyal
I see nobody coulda coulda treat you so nice wooo

me don’t wanna see any tears in your eyes
nobody coulda coulda treat you so nice
me don’t wanna see any tears in your eyes
nobody coulda coulda treat you so nice

Let me hold and protect you gyal
me don’t wanna see any tears in your eyes
Let me hold and protect you gyal
nobody coulda coulda treat you so nice
Let me hold and protect you gyal
cuz me don’t wanna see any tears in your eyes
Let me hold and protect you gyal
I see nobody coulda coulda treat you so nice wooo

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR